@cheikhabdoulahad.salatou: Li Dawna yaram trp nathi niepp diapp ta yalla takh partagé ko guir yalla s chiékh ndiaye 770724848 wala 786774848 Cheikh Abdoulate Diaw 🙏
lou métti yaguena si adouna😭😭😭😭yalnala yalla mayé werr
2026-08-19 19:47:07
472
🌸maman 💕ada🌸 :
Pa bii mom goréna déé machallah 🥺
2026-08-20 19:45:42
275
Ndeya saliou ♥️♾️ :
Yalnako borom bi may weurr
2026-09-02 16:36:23
0
Maáme Faállou Glasse 🫡💰 :
Yalla nako Yalla takhawou 🥺🥺
2026-08-19 23:27:54
188
Fatou sackor adiyeu 💙🤍 :
Adina li niou warra santé yalla beurri na 🙏
2026-08-19 22:47:01
113
diarra lo :
yalla nako yalla yeukeuti
2026-08-19 18:19:48
56
bb fatoucha :
Genre yi boumako guissé nonou lamay mété ay bouma amone khaliss bilahi ken dou sone🥹
2026-08-21 01:11:16
23
COACH PAPIS :
1milliard 1700 caisse noir première ministre 8 milliards caisse noir président lane lay diarigne sénégalais yi
2026-08-20 17:31:09
33
Fallou gassama❤️🫀🔐 :
Ohh 😧 li nitt wara santé yalla beury neu
2026-08-29 23:53:38
23
serigne Modou bou diop 2🫂💯🤟 :
yalla nala yalla takhawou 🙏🙏
2026-08-20 12:45:07
15
alou2eug♥️🖤 :
republication bi!?
2026-08-20 01:26:24
6
bb fatima ❤️😍 :
yalla nako yalla tahawou si barké seydina Mohamed Amine
2026-08-20 22:34:29
17
Omar bou cheikh mahi Cissé :
Parfois yallah tek la natou bindal lasi tiyaba bo khamni soko done diamou doko am yallah na boko si nioniou yarabi
2026-08-30 00:27:41
13
Fatou Gacko :
Bismillah Rahmani Rahim 61 + l'eau de pluie a boire une fois
2026-08-20 21:38:14
9
Soxna_faadal_ndour :
Bilahi souma yoron xalise dougal ko yalna niou yalla May xalise bouniouy diapalé nitt yi ko sokhla amine 😭🥰🥰🥰🤲🏾
2026-08-20 16:01:51
11
ÕMZØ@ :
Grand cagnotte svp
2026-08-20 17:52:36
7
user7512627885639 :
yalla Nala yalla takhawou
2026-08-19 16:36:53
5
Mrs Diallo ❤️💍🫀 :
Yaye yalna yalla tahawou si barki seydina mouhamad ❤️❤️🤲🤲🤲
2026-08-19 21:39:39
5
Mareme Malick🥇💍❤️ :
Maman Q’Allah te donne la guérison ❤️🩹 yalla gu tane ak diam papa niga taxawe yaye boy bi yalla nalako borom bi fay ay yiw yalla na dem ba tane ndjabot bi yobou Len haddji Maqa🕋 motax aduna soy and andalak kou am gor te xam aduna