Bayuilénn sgualnako téralnako cest sont devoir de faire bcps pour sa femme ´mais sà ne lui donne pas le droit lui frapper ´cest pas une raison
2026-08-20 10:54:32
99
Condé Dabakh Immo :
Walahi goor doukoko meusseu défal si adouna walahi
2026-08-20 12:30:49
45
.|.sokhna Fatou saliou.|.🏁❤️ :
Nit day sagual Dieukeurem Ms boul dorati notre bouri
2026-08-20 11:05:54
78
Pro max :
Bourry amoul conseil Bilakhi
2026-08-20 07:46:37
122
Tawou keurgui :
Bilay dafa dioum reseau sociaux yi kénedou si régler problème mariage yague gua mougne té kéneu dégoula gua tokk ba taye di def li toutal gua sa bopou wathie gua Boury tout sauf reseau sociaux gua Balma cherie 🙏🏻🥰💚
😂😂😂😂 Wouly nak bayil ada fass je suis 💯 balla gaye 2 nak begouma di wax si vie privée diambour meusoul ame tmt mais dama begue tellement balla mba begouma di degue si mome louma mety motakh mais dioum day ame boury dafa dioum rk tè balla aussi sou doré Boury féké woumako mais kone dafa dioum magui guisse gnouy juger balla nak mais mane mi deukone Guédiawaye di diar keur balla sonal ko bobou xallé la bakh kassé la guisse si balla dal wakhane sax barywoul bilay tè boury lou rafete rk lay wax si balla donc peut-être dioum mo ame rk
2026-08-21 09:43:43
2
user6811792336688 :
billahi wouly deugue nga wakh
2026-08-20 09:57:36
22
khalikh165 :
bilahi wax nga Lou leer machallah wouly
mais fokk mou def ci commedi nena balla Manon nga dieul fran bokkou ci lim bi 😂 mo gueun ada fass
2026-08-20 06:45:24
2
Awa Kane :
may len gnou diam khaliss doudara etre heureuse dans une chaumiere qu etre malheureuse dans un palais
2026-08-20 12:00:08
6
fée noire :
c'est devoir de faire du biens pour sa femme mais il ne faut pas la frapper c'est pas normal
2026-08-20 11:52:57
26
Talibé Cheikh :
Wakh deugg Yalla Ay door lou mana gnakk la nakk 😌😌
2026-08-20 10:25:53
8
user56247239614912 :
entre les couples personne ne peut pas juger
2026-08-20 11:40:10
7
user4452413309635 :
lou lere Gua wakh nit kou bakh ni la deff
2026-08-20 07:21:58
29
Modou diop :
wouly meilleur lutteur
2026-08-20 08:16:35
21
madysisko :
machallah wakh dji rafetena
2026-08-20 07:46:23
22
To see more videos from user @senegaldabordsn, please go to the Tikwm
homepage.