mane dal khamna limay wakh monumasi dr way moma guenalone ki gamou bu khasé ba dugusi bufa kn nk di sant ay dekndo ak ay politicien té muy téla n̈éw bayi khare ba ay 2h 3h nan̈u téla n̈éw gamoul nit n̈i ba beur sétt n̈u khamné bene biss la nan̈u gamul nit n̈i ba n̈épp khamné gamunan̈u km niko baye dn défé ❤️🥰
2026-08-21 00:56:40
6
Marseillais :
Kéne dou sama wadji niasse Coumba Abdallah
2026-08-20 14:50:21
55
François Gomis :
Sama thiofél si baye dafma dépassé c'est inexplicable.
2026-08-20 23:30:13
10
salalahou alla mouhamad❤️ :
sallalahou alla mouhamed
2026-08-20 15:07:41
31
zolam :
Lolou nako nieupou kham kouko diote nako diotali moromame
2026-08-20 21:19:01
13
mounir le catalan🇸🇳 :
Baye Niass est la solution
2026-08-20 15:07:25
22
dykha chuu🏀❤️🤘🫂🏀 :
Moy brome gamou gui🥰🥰
2026-08-20 11:31:03
28
FDS :
Baye niass dafa beugueone Seydina Mouhamed psl ba mou diekh
2026-08-21 13:16:04
7
Tidiane bou sonko 🇺🇸🇸🇳🇸🇳 :
Sama gorgi ❤️❤️❤️
2026-08-20 16:16:30
24
Mbaye iPhone 📱 :
2026-08-20 12:36:30
27
MHD THIOUB TMBNTV ⍟ :
Wallahi cachette yangui di bokodé deglou sa khol daye sedeu baaye moo baax ❤️🙏
2026-08-21 11:56:16
5
pape bou ndongo lo :
2026-08-20 15:18:24
19
ADAMA CAMARA :
2026-08-20 10:30:26
8
Hawa Saly Barhame Dièye 266 :
Kokou moye Ibra Asta sougnou assurance mbeuguéla thie yoneta bi non limite la mo takh magui koy nokel thie weurou gamou gui Niass Barhama
2026-08-20 16:17:44
16
محمد النور سل❤️🙏🙏 :
billahi wallahi 🥰🥰
2026-08-20 10:27:08
17
Lamine :
baye niass yagoul té rawna nieup 💚🫀
2026-08-20 16:39:48
19
mouhamedtoure4256 :
Lolou mom sama pape mamako wakh neneu dadonn tok diakarlo ak cheikh Ibrahim niass face to face ❤️😭🙏❤️❤️🙏
2026-08-20 17:31:30
13
Lamine Ndiaye113tiktok.com/@la :
2026-08-20 15:52:28
12
Beugue cheikh mahy cissé 🥰📿 :
Niass❤️❤️❤️❤️❤️🥰
2026-08-20 14:55:13
8
To see more videos from user @talibesbnthiatoupatriote, please go to the Tikwm
homepage.