Oh sama dieukeur rk nguafi décrire masha allah🥺🥺j’ai un excellent salaire wayer wer dou dei té diokhou ma sama argent de poche et louma lek louma nane leep. Il prend en charge domam louma si def mm 200fr il rembourse et meussoul tok ladj ma foumay dougual sama khaliss. Yana ko yalla doli té yombal ko
Kana khamou lene ne gor bodoul terel djiguen dou am dra djiguene yalla moka teral
2026-08-22 14:31:45
5
Mame :
Ça c’est le fils d’une reine🥰🥰🥰👏
2026-08-20 22:35:30
472
Boy sicap :
djiguene loko defal lou bakh guiglo bilay 😭😭
bilayy djiguene mome sam la sant defall ko lepp louy fekheul xolomm en tout moi deh souma diabar diaral nama leppp si aduna en plus son argent c'est son argent et mon argent est sont argent 🚶♂️
2026-08-21 07:27:28
268
ThiLDÀsH_LadY_D__💍🤎 :
Yalla ngua goudou fane waay. wakhal thiakaaw👍👍
2026-08-22 07:27:15
2
Binta Ahmed dame Cissé❤️ :
Say yaw yalla nala yalla diamal ❤️🤌
2026-08-20 16:11:23
172
Jamila Rassoul Toure :
Nit kou bakh moy wax ni🥰🥰🥰🥰
2026-08-20 15:59:48
672
. :
Wakh lou bakh niou bone😏😳😁😭😭😂😂❤️
2026-08-21 20:17:07
3
Mariam♥️ :
Aye ki Eta nako protéger
2026-08-21 08:21:21
104
La chinoise :
Un homme avec un grand H🥰🥰🥰
2026-08-21 09:00:52
25
Gaming002 :
Couple jeu d’équipe rek leu, tei mouy goor mouy djigueine koussi manquer à son devoir guiss conséquence yii. Goor dagne koy topatoo djigueine dagne koy teiral, et ses valeurs sont entrain de se perdre avec le temps et c’est ce qui est dommage
2026-08-21 10:36:30
122
Khady officiel :
djiguéne kouco téral yalla téralla☺️
2026-08-21 08:44:05
29
To see more videos from user @taaru_business, please go to the Tikwm
homepage.