@machigue_pro: Daroul Mouhty, L’as de la célébration du GAMOU Ci vidéo bi niongi ciy def ben résumé bu gaat ci historique Gamou Daroul Mouhty ginaaw biko Mame Thierno commencé def ci ndigalou Serigne Touba Waayé itam ay leeral ci loutax Daroul Mouhty di Gamou ci guddik Dimanche bou nek (Chaque nuit du Lundi) ci Mawloud bi Merci de partager et de vous abonner C’etait Machigue Production ✍🏽 Photographe & créateur de contenues Plus d’infos 777258833 #frypgシ #gamou #daroumouhty #viral @✪ CHEIKH 🙏🏻AWA 😍BALLA❤🖤 @Kamal_baye_darou photographe✪ @insaseck77 @S Aladji sylla 484 𖤐 @M2K TV @DIAGNE LE PHILOSOPHE 🧠🤍✭ @BAMBUT✪ @konia 🪙 @Thierno Clapien Gueye @Guissé Saa Darou Patriote
Yagg na beug kou wax si histoire bi merci nala yalla fay
2026-08-22 16:16:25
32
diagnenarr sa darou244 :
YALNANOU YALLA FAYAL BOROM DAROU MOUHTY ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
2026-08-23 16:21:43
2
🦺 Ndaw Darou Staff 🦺 :
Biss bamm gané Adina la daldi takkou
La Bamba khamné amna lamm done Sakkou
Fékone na Cheikh Bamba di niane bour Yalla
Diamar diou askano çi Mbacké Balla
2026-08-23 14:57:23
7
A.K.S✨ :
Daroul Mouhty 📌
2026-08-22 01:08:53
13
aliou.kara.diop :
إبراهيم الذي لم يفارقني لا في الصغر ولا في الكبر ❤️
2026-08-22 01:16:36
41
loum baye Darou business ✌️ :
Dieredief koubakh
2026-08-22 09:39:42
7
Xidma couture 🪡 🧵 :
Wawaw daaw fala gamo kendou Borom Daroul mouxty 👍🥰
2026-08-24 00:14:19
2
talibe borom darou moukhti100 :
waw gore waye🙏
2026-08-21 22:30:54
5
mouride :
machalah
2026-08-22 22:01:16
4
SEUTÜ_ÅRAME_NGŪËR_Bi🕶️ :
Machallah sam waadji Yasi meune dh ❤️djiambar deug ngua
2026-08-22 14:51:55
11
ahmed catalan 🎖🎖❤️💙💯💯 :
bonne continuation sama wadji ❤️❤️❤️
2026-08-22 14:27:56
1
Amydiop12 :
Amine way 🙏🙏
2026-08-22 13:47:09
1
khadimbamba :
bonne continuation 🤲🤲
2026-08-22 14:19:26
2
Ndiaga :
2026-08-22 10:06:36
4
user7928574007147 :
ken dou cheikh Ibra Faty borom Daroul Mouhty yalla nanu ko yalla fayal
2026-08-22 15:16:03
4
Ndiaye Darou :
2026-08-22 09:27:34
3
serigne__abo__mbacke :
❤️❤️❤️❤️❤️
2026-08-24 12:24:09
1
Hàbdoul Qaadir :
dieuradieuf BOROOME TOUBA
2026-08-22 20:33:26
1
To see more videos from user @machigue_pro, please go to the Tikwm
homepage.