@daroumouhtyapple:

Darou mouhty Apple 
Darou mouhty Apple 
Open In TikTok:
Region: SN
Friday 21 August 2026 21:11:08 GMT
40860
3690
260
125

Music

Download

Comments

modouk28
MAME MOR :
Danga di khalé rk 😁
2026-08-22 00:10:10
491
toubagassama46
minal Khadimi ilal khadimi :
Ana wa MPI, MPCI AK wa LMI gnou wax KO wallah😂😂😂
2026-08-22 01:09:32
95
lat.electrotechnicien
Lat 🇸🇳 L'ÉLECTROTECHNICIEN ⚡ :
man dh dama dem université niounema 1+1=10🥺
2026-09-01 14:01:12
25
jamaalfootballcleub
Jamaal Football Club🌎 :
Bilahi wax nga deuggg😂😂😂😂😂😂😂
2026-08-22 01:06:17
111
gana.ndione.221
L'INFATIGABLE :
Danga bakh rk bly 😄
2026-09-01 20:58:41
0
moustapha.fall675
Talibi Cheikh Mouhidine :
Adouna rawnala djaguil
2026-08-21 21:30:48
46
fallmaths4
Fallmaths :
🤣 1 + 1 = 2 😄. Su fekkee loolu rekk la, kon ñépp doon nañu champions ! Maths dafay laaj xam-xam, dégg-déggoo ak jàngat bu baax. 💪🏾📚. Matematik am na solo lool ci dund gi. Dañuy jëfandikoo ko bés bu nekk: ci xaalis, commerce, mesure, construction, technologie ak liggéey yu bari. Matematik it dafay jàngal nit ki ni mu wara xalaat, def calcul ak çöz problem. Kon du 1 + 1 = 2 rekk 😄. Matematik dafa bokk ci sunu dund bu bess bu nekk. 💪🏾📚
2026-08-22 12:16:34
28
user630425962613
bayi na togne :
tonton aide moi donc Un homme a deux enfants. L'un d'eux est un garçon.Quelle est la probabilité que l'autre enfant soit aussi un garçon ?
2026-08-21 23:32:39
19
lessonkoboys
@LesSonkoBoys🇸🇳🫶🏾 :
Pourtant wakhna deugue deh, diafé na nga guis ku diogué si dara di am problème mathématique surtout nk boo diaré si madiaaliss yi ba maîtriser MIIRAAS mat comme ndokhu naan lay mel si yaw🙏🙏🙏
2026-08-22 16:31:08
5
medoune.mbaye8
Medoune Mbaye talibe SONKO :
kou bakh dagua di khalè rek 🥺🥺 wa MPCI MPI MP niou wakh ko waleu
2026-08-22 01:16:18
7
jazzbusonko
Jazz bu sonko🇸🇳🍎 :
ségn bi mathématique moo teuyé adouna bi déh 😂😂
2026-08-22 14:07:05
10
sngal.fun
Sénégal fun :
da fek ago si équation yi😂
2026-08-21 22:22:04
1
cheikhsene1962
𝐂𝐇𝐄𝐈𝐊𝐇 𝐒𝐄𝐍𝐄🔥😎 :
Nidiay dangadi khaléé rt😌😂
2026-08-22 10:28:04
5
cheikhtidiane221
cheikhtidiane221🇸🇳 :
😂Saway esk khm nga (suite numérique )?
2026-08-22 16:55:10
2
bestthiaat
TheBeSt☠️☠️ :
1 chance sur 3 (ou environ 33,3 %) Il y a au départ 4 combinaisons possibles pour deux enfants : Garçon – Garçon Garçon – Fille Fille – Garçon Fille – Fille Puisqu'on sait qu'il y a au moins un garçon, on élimine « Fille – Fille ». Il reste donc 3 possibilités. Parmi ces 3 possibilités, il n'y en a qu'une seule où l'autre enfant est aussi un garçon (Garçon – Garçon).
2026-08-22 00:12:48
0
To see more videos from user @daroumouhtyapple, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About