Barki seydouna Mouhamed psl ak gamou gui bou fekei loumay wax dra dousi deugg yalla bouma teki sama navetane mo yakk adounam dafa deug ligueye diambour si navetane tank bi 1 er jour bim ko sonalé toubaye bimou solone bagn kay simi dagn ka done dagg telma tankk bi dafa newi niou teksi trois jour tank bi def forme guémine kom guémou nou nitt wallahi niou wo beneu pa ba pa bi nieuwei di xol tank bi beugn lasi guenei mei wallahi souma si tegoul wone sama beute koumako netali doumako geum walahi tank bi defna 2ans tanewoul si lagn ko wakhei bou guene tank bigui tokk fi dou tanei insbi mogui Côte d’Ivoire di fadiou defna fa plus de 5ans migui fofou tei ba legui tank bi day rafet di nieuwate tei lepp newetane leu si lagn yakei adounan mes frères svp bala guendi dougou di dra defare leneu sen yaram baparei kaladiou nawetane bo geuna boneu si lo xamni lougn lay fay dougn lasi ligueye gua guenei si louko yeupp defare leneu send yaram avant tt souniou yaye yi sonou nagn dé louniou dal niom niosi sonou kepp kouy jouer nawetane yalnala yalla mousal si you bone nio kham nawetane diaral nalen lor domou diambour🙏
2026-08-23 11:35:51
423
cheikh Tidjane :
jeune bouh beugue réussir sa adouna bayil Navetan dalal tardél
2026-08-22 22:05:08
1977
fall_officiel_kmfkamb :
Kogn bo dem koufa geuneu tarder joueur nawetane la wone 🙏
2026-08-23 12:00:52
1160
Torodo🌸👑🇸🇳🇲🇦 :
Li kougn ko teik xana dokh sax doko meun bay jouer 😏 ce qui devait être qu’un jeux de loisir est devenu quelque chose plus que ça, ce qui est malheureux 😞
2026-08-23 13:03:24
339
uneuh fah❤️nationale :
li gnawna
2026-08-23 22:56:05
0
s touba kenn lâ :
li reck mo yakh Sénégal thi football lamb bureau yi thi li reck lâniou xam
2026-08-22 22:30:09
3
Le Bambiste :
saway li mome kouko bagne donal supportaire di sétane✌
2026-08-22 22:08:15
143
notification :
on baribe
2026-08-23 18:12:43
0
Aminata 06 :
Thiey yalla 😭
2026-08-23 17:42:44
0
Khadidja la tigresse 🐅 🇸🇳 :
cest mon frere , il faisait parti des meilleur joueurs de la region de louga ,un jeune de asc deukeundo louga parti tres tot avec des ambitions et des reves interminable a jamais mefiez vous svp 🙏🙏
2026-08-23 15:54:03
95
Ndiss😎🏋️♂️🏀 :
Nolen def ba kham ko svp
2026-08-23 13:15:42
121
PVPĘ VLĮÕUNĘ🤌🏿🎭 :
Navetane moma rayone 2009
2026-08-23 15:58:21
21
Oblak :
Fi dal joueur bouniou fay khalisse demal si say mbokou prepare sa bopou 🥹🤝
2026-08-23 12:49:25
81
pa boss :
leguii wannéll sénn boss
2026-08-23 01:33:07
42
aziz :
lii motakh ma bayiii football
yalla na Yalla doliii soutoura
2026-08-22 21:43:23
38
Anita mou serigne fallou👌❤️ :
Liko dale ni dé sama grand frère dounde na louko geune meti bilahi navetane bakhoule😭😭😭
2026-08-23 01:46:09
32
Talibé cheikh philosophe :
mann dei daniou ma seufonn may nelaw trois jours va souniou wakeur titt , motax ma bayi navetane ba faff di daw stade. billay li daffa metti
2026-08-22 22:18:21
66
ragui 🅱️🅾️U,,ndaw 🅱️ii,,🦈 :
limomo rafetoul diarouko kowa bly 😌😭🫢
2026-08-23 01:46:45
1
Moussa 2025.2.0🦁🇸🇳💯🩸❤️ :
Bilahi baaxoul amna si yo xayni dounko saax diindi
2026-08-23 07:03:44
20
borom tal mbir yi :
nawetane dey yakh jouer
2026-08-23 10:00:04
12
Mary🦋saliou 🕋 :
Nawetane amoul bene diarigne lodoul lorr léne bay léne ko
2026-08-23 15:34:04
7
Ma’MINA store🛍️🤍 :
Legui no lenne def ba kham ko
2026-08-23 13:52:30
10
polimoussa :
yanna la yalla doli soutoureu frère ❤️❤️❤️
2026-08-23 07:32:28
7
cherife fantamady :
mais navetane ses comme sa dé mystique rek
2026-08-23 12:13:44
5
Abraham :
Navetane Diaroul lii Bilahi nioune on joue juste pr vous faire plaisir dans la fair play Prkoi marabouter L’enfant de quelqu’un pr ses foutaise Bilahi man Demay jouer Navetane mes Meusuma diokher tour nith wala may dieul ligeuy diko tekkk beneuh domou Adama leep day diekh Adina Dara yagoul
2026-08-23 16:30:20
13
To see more videos from user @issa.ndiaye483, please go to the Tikwm
homepage.