@boubs319: Ki chaque jour niou tassé si zawiya dama ko moudié fans sax 😭🙌❤️#pourtoi #gamou_tivaouane #tivaouane #gamou_tivaouane2026

✨Boub’s🇸🇳❤️
✨Boub’s🇸🇳❤️
Open In TikTok:
Region: SN
Sunday 23 August 2026 02:17:49 GMT
26986
6666
176
42

Music

Download

Comments

malikienne_business
malikienne_business :
Yalanako yala samal bopam limouy def daf ko gnor machaallah
2026-08-23 09:44:26
26
baboucsall830
Babacar Sall :
ay lou nékh mongui tago way yallah nañou co téwé ay tati attttttttt
2026-08-23 10:05:07
355
zeydiopf
Zey :
Ohhhh li soudé moy bida nassi deh wayyyyyy 🥰🥰🥰
2026-08-23 10:59:22
6
beug.bopam
Adja'sbeauty :
ndeysane xalei kassei la yalena Yalla sameuko wayé yalenanou Yalla fayale mame hadji Malick barket taha PSL🙏
2026-08-23 12:53:35
0
dyaba418
Dya Ba :
mashallah yalla same la def la magoume islam mashallah
2026-08-23 11:35:07
2
lalalous.babacarsy
Alalou s babacar Sy 🤍🤩 :
U7 maodo yi🥰
2026-08-23 09:48:01
63
monsieurlesaturne
Saturne :
Waw gaur nek lene si rek li moy diné deug Dieureudjieuf mame maodo
2026-08-23 11:28:44
28
sir....le.banlieuzad
Bay Guinard :
li waroull diékh wallahi ndeysane
2026-08-23 13:59:00
0
fallmoisd
moussa fall ingénieur civil :
gni hana u 9 yi leu machalla 😂
2026-08-23 11:57:01
47
yayou.bousso.m
YAYOU DIARRA B💕 :
Li rekk moy deug dh ❤️❤️❤️❤️🙈🙈🙈🙈🙈wawwwwwawwwwww 💃🏻💃🏻💃🏻❤️❤️❤️❤️❤️❤️
2026-08-23 11:07:30
36
kyabb5
Kya Dieng❤️ :
Ndeysne 🥺🥺🥰yallena ko yallah sameu def ko makk ❤️
2026-08-23 11:26:42
8
aytimah
matii :
ndeysan sama yaram bagui daw sakh 😭 Yallah nako Yallah def magoum l'islam déf ko magou talibé cheikh si barké Cheikhouna tidiane
2026-08-23 14:22:54
5
kaye.rafet
kaye rafét :
té amena foulla téla ci bir lay ame place dama ko dane guiss
2026-08-23 11:24:16
4
user22619426283358
Malick sope Dabakh :
Yalna yala fayal niou Mame maodo té samal niou sougnou daibot amine
2026-08-23 13:01:51
8
user6930420902358
kane :
u 9 maodo🥰
2026-08-23 09:59:41
7
papa.dez02
PAPA DEÜZ 🦁⚽️🇸🇳 :
ô kholal mbecté bimou andal rek🥰🥰😭 buurd dall ken khamoul loumou done bo tolo si assènement bii ngay yeuk thiofel deug si Seydina Mouhamed sw ❤️bilahi
2026-08-23 12:07:50
5
astoudiarra486
astou diarra ndiaye :
u9 machala nii la fimoy yone bi yalna yala dioubeul
2026-08-23 12:15:33
4
fatou.kebe958
Fatou kebe :
Machallah magou liSlam 🙏
2026-08-23 09:37:17
13
aichakamara14
aichakamara14 :
Machallah
2026-08-23 09:43:30
4
lanymbo
lanymbo :
ki serigne babacar lagn ko toudé ki moy mame babacar gueye machala
2026-08-23 13:28:38
6
lenaboutique2
ouraye :
machalla Machalla machalla Machalla machalla ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
2026-08-23 10:41:17
2
almakhtoum972
Al Makhtoum Souaré :
machallah 💗😘 yalla na borom bii fayalgnou mame Maodo
2026-08-23 09:24:39
6
user557567202
d'ara mbaye :
machalla bébé
2026-08-23 10:37:29
1
touza.ndao
Touza bou titi :
Machalla ❤️❤️❤️
2026-08-23 17:22:01
0
To see more videos from user @boubs319, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About