Mal communication Khadim Kebe dioum nga , Niep xamnagn nè mana diangue lol mais na bayi nit gni Waxal ko ko . Bou waxè Khadim Gueye moma daxa diangue ak woyof la rek mais dou tè gniko beug xamnè ken daxou ko diangue
2026-08-24 05:41:17
6
Gueye M-C 🇸🇳🇨🇮 :
Deel noppi manoo wax erreur yi barina loll mono communiqué
2026-08-24 14:34:27
38
Mouhamad Mbengue :
kiko posé question bi kén rawouko
2026-08-27 20:20:49
1
seck ndanane 🥰🥰💯❤ :
wakh deug yalla dégou masi Lou diarr grawal 😒
2026-08-25 11:31:08
9
bébé yayam 💯 🇸🇳 :
lim wakh dara nekou si dafa gueum bopam❤️❤️
2026-08-23 21:44:35
11
Kheucha Barber ✅ :
man mom sam diang moussou ma nex khadime gueye Moy sa patron nangoul
2026-08-25 01:53:50
6
Rassoul automobile :
al kibrou
2026-08-23 18:18:36
12
Yalna aldiana dicha kuer. :
Serigne Khadim kébé limou wakh dara nékousi parce que nitte sou guemou bobame dou sori si dara tocke si Palato nanne diwe moma dakha diangue kénedougo déff nagne wakhaneté duegue nak akh 👍💚💚💚💚💚☑️☑️
2026-08-23 18:29:41
10
MAME CHEIKH BOUSSO :
may leen nit yi jamm yeen jaxase ay nit kepp molen takha diouk Khadim kebe limou wakh amna Thi droit guisou ma lenn lou thi niaaw
2026-08-25 14:18:04
0
Bou M❤️🫂🫀 :
Sunu wadji mom la nyeup di weur nyun dong ko am wasalam 🥰🥰
2026-08-27 00:18:53
9
P T Ndiaye :
mais mane guissouma dara lou grawe si limou wakh si émission bi
2026-08-27 15:36:44
4
mame mor talla kebe :
serigne khadim kebe limou wakh dara nekousi
2026-08-27 10:17:07
3
MOR CRÉATION :
non vraiment je suis dit pourquoi il pose des question mauvaise ça fait pour mélanger les gens
2026-09-14 01:06:42
3
Bamba :
Pourquoi nit yi lo wakh mou graw si niom
2026-08-25 07:29:11
4
Ndiaby tv :
Khadim gueye sama wadji
2026-09-17 06:27:28
1
معهد فتح المنان لتحفظ القرءان :
Wax diou wér la wax nak la wax
2026-08-23 18:58:20
4
Borom khelcom🪴 :
Lan moy beug nga nek diww seringe Khadim mi seringe bi la geum doylou yalla 🙏
2026-09-16 17:25:55
1
fallou fall :
khadim dh kou am geum geum la rk
2026-09-02 02:26:27
1
Thiatouyayam ak papa officiel :
Machalla wakh dji Amna solou bilahi Khadim kebe
2026-09-04 00:29:59
2
#€l'homme de son temps€# :
bilahi déma roussss 😭 amna louma métii 😭 khadim Gueye d'où séne morome moy l'ambassadeur de tout les temps 😭
2026-08-26 01:24:22
3
Daouda Ndiaye :
bilahi Sénégal nékhoula wakhé ki lim wakh Dr nékousy haaaaà