@ibra18faty02samb: wahabiste dou lou baakh

خليل الرحمان 🇨🇦🇸🇳
خليل الرحمان 🇨🇦🇸🇳
Open In TikTok:
Region: SN
Monday 24 August 2026 12:53:46 GMT
57033
7151
586
239

Music

Download

Comments

omar_ndi98
Omar ndiaye :
Man mi dh yiii lou wax massou mako deff ta touba la deukk
2026-08-24 14:04:03
181
ibra18faty02samb
خليل الرحمان 🇨🇦🇸🇳 :
republier la vidéo svp🙏
2026-08-24 13:00:26
239
bass.boutique6
bass boutique :
waro wona toudou bassirou dia
2026-08-24 15:02:35
1
mouhammed.deme
Jàng ak Tekki :
aldjiana dé boula gnoroon doofi weeso serigne bi dikou woutti faneen khamngani serigne bi mbakloowout kénne ay grab warloowout kénne grab wakhi dof rk ngay wakh
2026-08-24 13:35:16
134
bromtorino2
Béne way tv 😂 🇸🇳🇮🇹✅ :
😂😂😂😂 môme khana beuredeu bou bess la 😳😳😳
2026-08-24 13:00:27
51
sunnarek8
مودو وَكان حقا :
gni louy sen problème 🥺
2026-08-24 13:07:24
57
babacar.sadikh5
Babacar sadikh :
limiy wakh foum am mane Touba la deuk wayer mosoumako def
2026-08-24 15:46:43
29
beugue.diam1
Sa FiTnA molaye FiTnAl :
walakhi wakhi bassirou dia la gueneu gueme ke ywou vraiment lougniouleneu wakhal rek yeneu la
2026-08-25 10:02:08
0
boubacarsall369
🙏Boubacar Barça 💙🤎💫 :
limiy wakh dh masou makou guiss touba
2026-08-24 15:53:11
12
abdourahmanesoudaisi8
SeYdina :
serigne Sam mbaye mo nè seringe touba mo binde nè Yalla Yeketina ko tèk ko si kaw yonente yi losi wakh
2026-08-24 13:57:46
11
seydinadjibrilfal0
Seydina Djibril Fall :
yallah nama sa borom dimbeuly ma sakh thi tarikha rawatynak ma faaatou thi yonou mouridoulah amine alhamdoulilah
2026-08-24 14:01:56
38
bouyeukane
KANE DIALLO💫 :
jërëjëf ibrë faty🥰
2026-08-24 13:50:05
88
ousmanedieng83
Ousmane Dieng :
merci oustaz khadim
2026-08-24 13:21:43
12
harazim23
Aliou Harazim Diack :
Ki moy khalilou rahmane wa fouta contanane si iow 🥰🥰🥰
2026-08-24 13:27:55
12
tsk2041
bàyou ismaila d ak maseck sarr :
mane lima diakhal mane touba là deuk té yiniye wax massou mako déf
2026-08-24 16:31:58
10
h.h28897
Weur deug :
Thiey Ibra Faty Dieureudieuf 🥰
2026-08-24 13:35:50
19
user3813722671574
MURID MURITÉ :
Boroom ku leer la digganteem a Boroomam ak digganteem ak jaam ñi . Jërëjëf Ibraahima Faati
2026-08-24 13:42:19
10
mordiakhate393
mordiakhate393 :
merci bima commence video bi rekk dama commence bind di laaj mom kane la doon topp far nga dagg ko tambale fa jërëjëf
2026-08-24 13:11:55
23
soda.laazanba
Soda laazanba :
Serigne touba dieuredieuf
2026-08-24 13:02:57
16
alkhourane44
Talibe sarif hassane fall al :
Massallah ibrahima faty 🥰
2026-08-24 13:19:43
13
yallakenla
Kénall yalla :
walahi ndeysan linga wakh moy deugu serigne touba nakhoul kén
2026-08-24 13:27:00
11
oustazmbaye853
Saliou khassida 75 336 36 37 :
dafa mana doul
2026-08-24 14:00:15
8
dioufwakana549
diouf wakana gabon.077047375 :
merci beaucoup way mourit
2026-08-24 15:04:17
7
oumycisse393
#PATHE-NDIAYE :
Limouy wakhni yeup Mangui Touba ta man mosomako dégue ta masou masé déf béne ta serigne wakhouko diguelé wouko billahi
2026-08-24 14:26:00
6
bayelahadmbaye1
SBN :
man deh touba la dioudo mague fi waye limouy wakh khamou mako te meussou mako def
2026-08-27 11:06:43
3
To see more videos from user @ibra18faty02samb, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About