Yalnama yallah may une très belle maison à Tivaouane ak keip kouka begue si barké borome goudi gui😍
2026-08-24 17:12:35
1594
ELHadji aliou Ba :
so beugué yonénteby Dara doula djiomb, Allahouma sally allah seydina mouhamadine
2026-08-24 19:59:47
456
🅾️ulimta اٌٌْوٌلِمةّ🧕 :
Goudi Seydina Mouhamed Psl💚
2026-08-24 15:52:27
330
tymachic :
Machaala na rap ak diam nga rapal ko boul fater outaler kouy foberé
2026-08-24 16:50:09
270
marieme diop laye :
liloula ndaw la si wayou seydina Mouhamed yenene nii ndam nigui nieuw inchallah 🥰🥰🥰
2026-08-24 18:05:13
186
Perle rare :
machallah kèpeu kou beug keur Tivaoune Yallah nalako sugniu Borom may thi Barké Seydina Mohammed SAW
2026-08-25 09:21:39
79
Khadija bint khuwaylid :
Oustaz lii nga togalé def patt ❤️❤️❤️
2026-08-24 18:38:56
78
Yayou amina :
Mashallah way yalla naniou yalla boler si milillardairou seydina Mouhamed Yi ak sidy hadji malick Sy Yi baniou meuna am keur tivaouane Di dalalater Amine si barki gamou gui
2026-08-24 20:17:53
63
@queendujardin :
machallah yalla gako mourlo barkei seydina mouhamed
2026-08-24 19:05:26
58
Ass malick Sy :
Machallah cou bakh am lou bakh 🙏
2026-08-24 16:31:37
44
Daf Mbaye :
Li rafét na trop waï yalla na and bi yague
2026-08-24 16:41:15
38
a :
machallah lhomme qui fait sans bruit🥰
2026-08-24 18:10:03
38
Amy Kassé :
salalahou alla mouhamad🥰🥰🥰🥰🥰
2026-08-24 18:30:24
32
Anta90 :
Sallahou Allah Mouhamed
2026-08-24 18:20:33
30
#NGAGNE#HALAWANI :
nék si Seydina Moukhadam rek mo wouoor
2026-08-24 20:51:07
29
Mustaf🇸🇳 :
Dara Reuyoul thi kouy tagg yonèntibi psl 🥰❤️🥰
2026-08-24 17:21:01
22
Damass :
ndiabotou maodo dano bax
2026-08-25 00:33:48
21
Yayou naby :
Pape hann kou bakh la kou dall Machalah
2026-08-24 17:09:53
17
diakhaté kaba🥰🌹❤️ :
machalla meune na nékk hanne
2026-08-24 16:23:08
16
@mariemekane581 :
yonentebi terralnala oustaz pape hann machallah yalla na rap ak jamm très jolie maison
2026-08-24 18:31:00
15
SERIGNE Gueye778681281 :
صل الله على محمد
2026-08-24 17:26:18
14
amydiakhate662 :
Rap ak diam kheweul kesser
2026-08-24 18:21:20
12
Yayou Mouhamed ❤️❤️❤️ :
Macha Allah oustaz pape Anne yalna dale bi séde gouye na rapak diame té nga rapalco