Mane deh amena 30ans Dou Liguéye dou dieukeur dou xaliss mais magui sante yalla bou bakh kouma guiss yakarné magui yoor adouna ak lousi biir
2026-08-25 17:07:04
144
abubikr2 :
Personne n’est en retard,nous sommes juste là où nous devrions être! Teep tepp mo guene youret
2026-08-25 10:57:37
211
balla :
Sentena yalla ba mou ma maye wer 😂
2026-08-25 11:15:34
65
octogine :
J’ai 30 ans je fais un doctorat au Canada mais amouma auto amouma khaliss amouma Sokhna. 🥺
2026-08-25 11:59:38
39
KILIFËU :
Yalla mom bou douguei si debat rek teudj ko prck lepp mom leuh . Legui pour man deug bi moy adouna bi flash lan fiy def . koussi nek si nioune warnga fekhei bayi fi sa signature . Probleme bi moyy amouniou éducation financière motax ngay guiss beine age bou avancer bi nit gni dounou am dara . sounou wagnei guiss leine ma ak paraître liguey bagna yakk moytou evenement yi rek dinagn si gueine . Li eup solo moy ko si wax xamo xaliss mou merei leuh . peut etre limay wax dina am nioumou intéresser deim leine diangui nounouy amei xaliss ak boko amei ba parei noun koy multiplier (podcast investisseur yi niogui fi livre yi aussi niogui fi ) perso le livre (la chevre de ma mere ) dafa oubi samay beut bou bax si adouna et n’oubliez pas que «la prospérité du pays depend de la prospérité financière personnelle de chacun de nous ».
2026-08-25 15:36:16
8
yakce..J@h :
Bro that's right 👉 real idea of 🧠
2026-08-25 17:53:59
0
jeune Entrepreneur 🧠💡 :
merci de nous rassurer et de faire comprendre la patience KFC 60
2026-08-25 10:16:42
23
Assane-foch£n :
Jajeuf way grand 💪
2026-08-25 14:30:23
0
senegalmonekh19 :
Yoyoy kouko amoul daga setane si
2026-08-25 14:50:29
6
momar Talla ngom :
lou diote yombou yala lousi nék dafa ame heure boumou kaye déf amena nio khameni 20 ans 25 ans lagne am nék milliardaire wayer baniou amer 35 ans lagne dé bayi fi lép pour mane bo amer yéne âge yi ama guo yala maye la wérr pour mane kherweule leu avantage leu meune na ame surprise reussite bou make mogui nieuw.
2026-08-25 16:34:59
5
crazy mballo :
mé bro 30 tan kouko am te amo linga limni yep koulako wakh ak koulako wakhoul iew Thi sa bopou yakoy wakh sa bopou ✔️
2026-08-25 14:33:21
5
Ibrahima Ba🇫🇷🇸🇳 :
Oto mo dou tous ma dhe moto moma geunal oto🥰😂
2026-08-25 18:12:32
2
@izzo-the game :
goudou fanne mo eupp solo léep ndakh am am nga fékkéko mo eupp solo lépp
2026-08-26 00:11:21
3
bonheur❤️ :
liii yeup amou maçi Dara et j'ai 30ans mais je vie tranquillement😂😔
2026-08-25 23:54:54
3
ms.orbit :
Masterclass 👌❤️
2026-08-25 15:08:03
0
AbuYoussouf, SAHO :
Correct ✅
2026-08-25 22:46:03
0
Sall Lamtoro :
j 30 ans amna liguéye amna diabar
2026-08-26 00:19:28
1
DMB_SAMBA :
Lou lerr frère 👌🏾
2026-08-25 22:01:54
2
@Todibo250 :
ioe mii rkk yaa wara wakh nak ❤️🙏
2026-08-25 16:59:58
3
diéne éleveur :
la reussite depend de dieu meme 50ans on peut reussir
2026-08-25 18:00:28
0
adamadams233 :
Lep si xél bilay pauvre ak riche lép ci xél laa
2026-08-25 18:54:01
0
Chypher Hip Hop--the world :
mane d amna 29 ans amna liguey diko niafé mé awma diabar
2026-08-25 20:48:57
0
Yoro Diarra :
Et pourtant c’est vrai ??
2026-08-25 15:59:12
0
Libs Hakeem :
ioe nala gouvernement protegé
2026-08-25 10:57:41
3
To see more videos from user @numuydeme, please go to the Tikwm
homepage.