@liloug11:

KHALIL GUEYE
KHALIL GUEYE
Open In TikTok:
Region: SN
Tuesday 25 August 2026 12:04:46 GMT
16855
2667
135
52

Music

Download

Comments

sirif95
Sirif :
🥰🥰👍👍👍 ya bakh wayyy vidéo bi sénégalais yeup gnoko wara guiss pour gnou kham loutakh gnou khobé si Cheikh Modou
2026-08-25 20:08:30
39
ngathie077
Massamba :
Ki dou wax louy deugne
2026-08-26 22:32:51
16
brahime606
brahime :
ndayssane, mom kenneu la si serigne bi.
2026-08-25 19:48:17
13
user55385929587340
amadoulamine :
thiey borome chicory
2026-08-25 20:27:55
6
user3404382725015
mouhamed cmr beug out am incha :
machalla mom tolou wayam da kawe lol way machalla yageu fi lol mbake
2026-08-25 18:34:36
35
rassoulsenteurs
rassoulsenteurs :
KI MOOY KOU KENE DOUL XAM …. Il est le SECRET DE BAMBA ❤️🥰🥰❤️❤️
2026-08-26 04:21:58
16
papasarr61
longe weekend 40par force 💪 :
c'était en 1992 mbacke balla
2026-08-26 05:15:17
10
serigne.mbacke.mb888
Mbaye Horizon :
Sheuutttt
2026-08-28 07:15:20
1
osmnlye
OSMN LYE :
kaRa Bamba merci 👌👌👌
2026-08-25 19:20:54
8
serignemback4
Serignembacke ✌️ :
Bilahi dou kou gjiy kham fii kii ken dou mom laa wakh ❤️👌
2026-08-26 02:39:42
14
loudoul.ak.talib.s
Baye Gaye cissé :
thieuy cheikh modou mame maréma seye😭😭😭
2026-08-26 19:49:57
4
makhmoud_kara
makhmoud kara :
Jerejeufé borom touba
2026-08-26 12:48:40
2
user7008570974214
user7008570974214 :
Modou Mame Marème diadieufety ❤️❤️❤️❤️
2026-08-25 12:35:25
4
boukaraka
✍️Bou Jah Kara Tawaalif 🎤 :
kénn dou moom jah kara
2026-08-28 02:05:04
3
mamecheikhmbow2
Mame cheikh Mbow :
Lonou meusa waxx guiss nako❤️❤️❤️❤️❤️
2026-08-26 05:59:09
5
bayemor024
bayemor024 :
daf ci Yaga insisté bilahi mais nieupa done wax dof bi limouy wax man sakh bokone na ci ki balla niouko xam mou wan niou ganaw yalla na yékh🙏🥰
2026-08-25 20:16:35
9
marbriergeneral
LE MARBRIER :
😂😂Ausseccourrr 🤣
2026-08-27 07:22:05
0
user4324437713074
use :
macalla
2026-08-26 00:04:59
1
samsegueye
MAG SAMSE❤️🙌🇸🇳 :
L’incompris jah kara☝️
2026-08-26 22:20:12
2
allidiaw1
allidiaw1 :
Yagg Fi lol th wer noreyni 👌❤️
2026-08-25 21:41:17
3
sakhomoussammbaye
@[email protected] :
jhakara Dieureudieufé
2026-08-26 11:25:02
2
jilbrata
plus221 🇸🇳🌍🌎🌏🇸🇳 :
THIEY BOROM DIAMANO BY
2026-08-26 08:51:58
1
bayedjiby69
Djiby faye Baye Darou Bi🌳 :
cey modou mbacké noreyni mandé masuma gam gamlé ay wakham té dou tay lakoy déf🥰🥰
2026-08-28 01:18:15
2
abdalsham322
Dallah SAMB :
❤️❤️🥖
2026-08-25 22:21:12
2
mamecheikhmbow2
Mame cheikh Mbow :
Ndeysan aka paré❤️❤️❤️🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
2026-08-26 05:58:49
1
To see more videos from user @liloug11, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About