Machala li dawna yaram souniou sangue yi ay royoukay magne sy Malick
2026-08-25 21:43:17
0
The Prézzi Soldier❤️♎️ :
Kilifeu aka am sollo si nittt mais nii rek guén meuna mel parsk Dabakh moy sen wadiour ❤️🙏
2026-08-25 21:11:28
30
RASS pro vision :
Bilahi vidéo bi dioy Lo nama sa mak gua defko Kome sa Wa Diouf mame Dabakh contanna 😭
2026-08-25 20:19:00
29
Fallou Touba :
ndaysan sama yaram dawna masoulè na wakh loun lèni khèbè yèna rafètt ndokhin billahi nièppa lèn soppou yalna yalla samou lèn bou bakh yèna yarou
2026-08-25 20:11:09
45
bathie :
li nak nioun talibei yi nagnsi dianguei gueuna defarat sunu togay tei yokk sunu worma si ndiabotou cheikh seydil hadji Malick Sy rta image bi boulenko yamalei si kholl rek dh walahi defarna nite
2026-08-25 20:21:00
11
Diddy ndour :
ohhhhhh Machallah vidéo bii dawlo na sama yaram bii ❤️❤️❤️❤️
2026-08-25 20:26:45
7
12 :
hooooo mashala
2026-08-25 20:40:44
1
touré agent 66 :
l'image du jour du gamou Macha alla🥰🥰🥰🥰
2026-08-25 20:54:01
5
PEOD DIOP :
euskéy xolou thiofél deug lako xol gni nio beuganté ohhhh j'ai la chaire de poule😍😍😍
2026-08-25 21:26:57
2
mouhamedsagnane :
ndeyssan lii rafétna lool té tooy khol
2026-08-25 21:45:14
1
Seydina Mouhamed Sy :
walahi li dawna yaram. yalna yallah gouddeul sén fane ya rabi🤲
2026-08-25 21:14:45
3
Hustle Man :
sama kholl yéguatouna dh bilakhi❤️❤️❤️😭😭
2026-08-25 21:51:47
1
Le Déclic 🏋️🇸🇳❤️🇫🇷 :
Mbacke yag fi loll té wer
2026-08-25 20:25:03
1
Mam Abdoul Aziz kà :
2026-08-25 20:24:26
2
Fama Hanne dabakh malick :
sy Malick yalna léne yalla same
2026-08-25 21:46:58
1
MASTER PASTEF MAN :
Euskeuy
2026-08-25 21:25:45
1
Fadiaw Camara la Lionne :
Ndeyssane j ai les larmes aux yeux
2026-08-25 20:38:31
2
zil.daviser.mister :
Blh sama yaram dawna blh🥰
2026-08-25 21:30:44
1
Demba Ndiaye Maodo ❤️ :
machallah mak AK Rak ❤️❤️❤️❤️
2026-08-25 19:46:24
2
souadou :
🥰
2026-08-25 20:31:57
1
guelel :
Machalla
2026-08-25 21:26:18
1
pispa :
mashallah
2026-08-25 20:33:56
1
Diolinho :
sama xol toyna
2026-08-25 21:31:06
1
Ahmadou bamba :
ndeysan🥰
2026-08-25 21:12:02
1
To see more videos from user @daouda.gaye71, please go to the Tikwm
homepage.