Vraiment war Nagne ko defar ndax bou tawé oto moto ba ci Weutir Yi Ci Mbéde yi laniouy diar Di Tégui ndoxou taataa Bi Té lolou woroule ak xalé yi you Ndaw yissi Mbéde mi lolou woroule🙏
2026-08-28 16:33:50
1
milk kara 23🇸🇳 :
ngaye da wara am ay canal
2026-08-26 19:51:41
1
iskaraapple :
2026-08-26 02:58:05
1
ndery ngom Talibé sr mahtar :
bilay bou élection dioup si wone niou défarko
2026-08-25 21:48:33
1
Massamba Dieng Darmanko :
C’est la vérité
2026-08-26 17:02:27
1
Élément serigne salihou 💯 :
bilye 🥹
2026-08-26 02:45:26
1
Mballo. kandji couture :
doyna warr
2026-08-27 18:01:22
1
astou gueye🥰 :
2026-09-08 22:08:12
1
L’absolu🥰🥰 :
Li dé puis bi ma néké Nguaye darra 2022 ba tay nila khamé😭
2026-08-26 11:15:14
0
fallmbacke420 :
Cette route est une route départementale qui est de la compétence de l'état et non de la Mairie. Les travaux incombent à l'Ageroute.
2026-08-30 23:01:52
1
art_rou_ngay_mekhe :
Li dafa yomba defar sakh
2026-08-26 18:25:49
1
user7307812454821 :
wax len way diott na
2026-08-26 15:08:55
1
paper oumar :
béss bouniou wakhé ba dieulé fi magatte wade dinanou dore sounou lokho si ake euke bilahi
2026-08-26 22:33:19
1
user4195272114322 :
metiina
2026-09-02 22:49:39
1
PMF :
Dangay soop
2026-09-03 16:54:03
1
FREE CHEIKH GADE 🚨🚨 :
ngaye maire bi liguéyoule dara
2026-08-26 03:43:03
1
To see more videos from user @devendiaye3, please go to the Tikwm
homepage.