Delen partage yoo baxh yi tmt Sy Malick ya beurii xam xam ❤️❤️
2026-08-26 17:21:46
0
Zeemagic ❤️🎉🎉 :
On restera toujours les enfants de Serigne Moustapha Sy Al Maktum
2026-08-26 11:46:22
22
(Maguette mountakha ) :
mbacké yague fi thé werr
2026-08-26 14:29:17
81
🎀Bint Aboubacar lô🎀🇸🇳🇵🇸 :
Mane daal souma nekoul wone sa Ndiabote wayadi😂🫀🫀🫀
2026-08-26 14:06:40
149
Madame mboup 🇸🇳🇬🇧❤️❤️ :
yallna na yalla goudal fann wii inchallah❤️🫶🏽❤️
2026-08-26 18:26:43
0
Abdou aziz sene😍mou khalifa :
Machallah machallah machallah yalna yalla goudal fan yi xam xam pirr lay wakh walay ndeyesane 💚
2026-08-26 16:37:03
1
mboup élément sonko ✅ :
Serigne Moustapha Sy, Ousmane Sonko sa doom la, sa talibé la ! Nioune patriote yi, souniou Mame nga, souniou Serigne nga ! Ak lou mëna xew, dara douko dindi !
Am nga droit wax niou lou la nékh, wala nga def niou loula nékh, ndax sunu kilifa nga.
Yagu fi loll mou and ak wër Sy Malick .
2026-08-26 18:25:15
0
Diop modou :
ya raw goudoul yaw ♥️
2026-08-26 17:27:08
0
Une Khadija ❤️ :
Yalla na yalla goudal fann Wii inchallah ❤️🫀🫶🏻
2026-08-26 09:46:13
66
Zeuzy :
Diné dji mome nangou nagne mais diapalé niou té nga bayi Sonko 🥰
2026-08-26 10:55:00
12
SN BOY 221💎 :
barki seydina mouhamed mourid la mais gayi vidéo yi lan war di partager mais pas you négatif yi yallah na yallah sameu la barki seydina mouhamed ❤️❤️
2026-08-26 16:34:26
15
user341182diop jr :
dianteu timoul kou raww serigne moustpha sy quelle enseignant ❤️😳
2026-08-26 15:10:59
60
Maodo dia bou capitaine ❤️🥹 :
Serigne Moustapha Sy point
2026-08-26 15:43:25
31
Joe et Charlotte ❤️ :
partage lenn li wayy 😭😭
2026-08-26 14:59:39
28
prophète121 :
ana niou done wakh dou wakhtané wakhou diné 😒 machallah sy Malick
2026-08-26 17:23:11
13
Citadine Ceramic :
Bilahi Goor gui dal moy xam xam sheuteuteu❤️
2026-08-26 10:28:53
31
yayou Bayam 😘💋 :
Sy Malick guédiou kham kham gui🥰
2026-08-26 09:49:24
39
👻MHD✪ :
Sènègal nio beuguoul kou lène wakh deugg
2026-08-26 16:29:23
7
Boubacar touré 423👌🫅 :
Apar môme kanmokofi meusseuléral bly loumouy wakh da dépassékhaléyi
2026-08-26 12:41:24
30
Baye moudo bou dmwm :
ms pourquoi pas limo wahk lipp nioy khol lo lin ci nehk rk nio tek di wahk rk sy malikc Dondal wre inchallah
2026-08-26 15:40:12
16
ICOSPORT HOMME D FOOT LOCAL :
❤️😭❤️J’ai été ébloui par le discours de Serigne Moustapha Sy que j’ai envie de faire une réécoute à l’instant même 😂❤️📖
Wax neu ci Yonéntibi SWS ak thieurr bimou am ci Yalla, wakh ci sugnu mame Adama, wakh ci Yonenté Yalla Daouda, wakh ci téré yi di Tawraat ak Ingiil (Torah et Évangile), wakh ci Moussa ak les 10 commandements, wakh ci sourate Mouzzamil (L’enveloppé) ak Sourate Muddaththir (Le revêtu d’un manteau), wakh ci Ibliss, wakh ci astrologie (planètes yi ak éclipse solaire bi amon fann yii passé)….
Ak yanen ak yanen….
Souba ci yoor-yoor bi InshaAllah mou fass yéné waxtan ci “Al-Furqân” et son double interprétation: discernement et livre
Dommage que les hypocrites ne vont parler que de la fin du discours 😏✍🏾*
2026-08-26 15:36:02
13
Princess Dieng ❤️ :
Sy fagay demba ya raw niepou 🥹🤍
2026-08-26 11:07:28
10
La colombe 🕊️🕊️ 🇨🇦⚜️ :
Hauteur bimiy waxé taxna deuglou kenen dalay nelaw lo
2026-08-26 12:10:26
9
To see more videos from user @dieng_khalil7, please go to the Tikwm
homepage.