J’ai été ébloui par le discours de Serigne Moustapha Sy que j’ai envie de faire une réécoute à l’instant même 😂❤️📖
Wax neu ci Yonéntibi SWS ak thieurr bimou am ci Yalla, wakh ci sugnu mame Adama, wakh ci Yonenté Yalla Daouda, wakh ci téré yi di Tawraat ak Ingiil (Torah et Évangile), wakh ci Moussa ak les 10 commandements, wakh ci sourate Mouzzamil (L’enveloppé) ak Sourate Muddaththir (Le revêtu d’un manteau), wakh ci Ibliss, wakh ci astrologie (planètes yi ak éclipse solaire bi amon fann yii passé)….
Ak yanen ak yanen….
Dommage que les hypocrites ne vont parler que de la fin du discours 😏✍🏾*
2026-08-26 19:18:54
3
abdoulayediall1831 zeydi baïlo :
ani gni bouga capitaine 🥰🥰🥰
2026-08-26 16:59:57
5
prince lamina jr☺️🇸🇳 :
D’où yenn ndax senn dokhalinne kilifa dou def lolou meunouma comprendre yenn daw nguenn deuko sonko si législatives yi alors que benn débuté nguenn am walahi sonko à vie
2026-08-26 13:16:50
7
D. LY BOUSSO 📀TOROBÉ :
Yalla na yalla mottali té arr
2026-08-26 14:34:32
7
cana.sn313 :
Principe rk lagni ende nitt
2026-08-26 15:08:23
6
undercover :
contradictoire 🤣
2026-08-26 13:26:14
2
gangster 💪 :
lo wakh deug la
2026-08-26 15:51:58
2
Ibrahima Al Amine😍🥰 :
doo deg MoU wakh Aya
2026-08-26 14:06:50
0
coumbist167 :
Yalla na yalla oyofal yéne wii❤️❤️
2026-08-26 19:24:20
1
Pere Papa :
walahi 🥰🥰🥰
2026-08-26 12:54:40
0
salzo88 :
bilay deugeula wakh dji rafetna
2026-08-26 13:03:26
4
Sénégal :
2026-08-26 14:15:24
0
Sokhna fallou12 :
2026-08-26 16:39:16
0
Bouba sakho :
2026-08-26 13:38:47
0
Bouba sakho :
2026-08-26 13:38:43
0
user81110412449704 :
Amadou❤️❤️❤️
2026-08-26 15:14:01
0
Sakho le parisien🇫🇷🇸🇳❤️ :
Machallah diaradjeuf mame cheikh yana yallah xepp di doly🥰
2026-08-26 15:09:55
0
weusndiaye :
waw goor 👏
2026-08-26 14:09:08
0
Fallou Yakar Yàlla12 :
𝗴𝗮𝘁 𝘅𝗮𝗺𝗼𝘂 𝗸𝗼
2026-08-26 12:56:43
2
فخر أبي :
demall dia. giiii
2026-08-26 13:29:30
0
pape 843 :
ki diangoule hana ils se contre dit seulement
2026-08-26 16:38:02
0
Bamba séné :
🥰🥰🥰
2026-08-26 12:59:26
1
user9687345994499 :
💚💚💚
2026-08-26 14:11:27
0
Dame🇸🇳samb✅✅ :
🥰🥰🥰
2026-08-26 12:50:26
0
To see more videos from user @samarew19tv, please go to the Tikwm
homepage.