Senegal pour soidisant marabout yi. Niom rek nio wara am mbolo di diokhé ndigal si ay douli késsé. Maï kou seydina oussmane sonko mou sel minioune talibé yi danioukoy diokh adiyeu di weuyé ndigalam bou woté niou wouyou si bou diayé cárte niou dieund lolou moy kate ndayame kholou soidisant marabou yi
2026-08-26 19:58:47
3
Khemesse Diouf :
😂😂😂
2026-08-26 19:48:14
1
Sow f444 :
Merci beaucoup
2026-08-26 20:04:27
3
tapha :
yow nioune dégounioula sax nioune dalle niogui xéw
2026-08-26 20:34:18
0
Alhamndoulilah :
Sonko rek lanouy topou ba parée beugu kouléne topou😂😂
2026-08-26 19:42:30
0
abdbdc :
sonko rek inchalah
2026-08-26 20:25:06
0
Aliou Diouf :
2026-08-26 20:20:30
0
africain :
ko wax fouyou fayé mounéla fouyou fayé
2026-08-26 20:28:04
0
Abdou Aziz Seydi :
déég na deug dé
2026-08-26 22:23:39
0
Boy Ndiaye 🐑🌶️ :
Bon xol bakhoul
2026-08-26 20:21:24
0
twwwwww :
👍👍
2026-08-26 20:22:32
0
Malick Lo :
DIEUREDIEUF SY MALICK
2026-08-26 22:15:04
0
maodo dia :
sy malick lou ler nga wakh 🥰
2026-08-26 22:30:03
0
PAPE NDIAYE :
WA LI MOOY GAMOU THIEYE
2026-08-26 21:48:32
0
borombakh :
2026-08-26 21:43:40
0
africain :
bou bokk sadérét defna manifestation ay nitt déé si diamonoy senghor doom dji defko diamoy abdou diouf -loo khass sonko khass ko sa mbokk yoyou
2026-08-26 20:30:10
0
dakarmedina3 :
2026-08-26 20:40:05
0
insa :
Est-ce que dou yi guén di def motakh jeune yi topou sonko
2026-08-26 20:23:02
0
boyfaada :
Serigne niou tay yi sonko sen kilifa la 🙏
2026-08-26 20:34:52
0
sha-k :
li moy gamou , thiakhane rek
2026-08-26 19:39:38
0
To see more videos from user @thiam_teranga_officiel, please go to the Tikwm
homepage.