yene nidone sisou loutah donguen commentaires si li
2026-08-27 11:41:03
385
bamba rk :
wallahi nit limou beuga dég rk lay deg❤️wayé ki kou bakh la
2026-08-27 12:56:24
268
tiatou yayam bou d M W M ❤️ :
borom xame xam bi bly Sy malik dundal weral ♥️♥️🥰🥰♥️♥️♥️♥️♥️
2026-08-27 16:21:40
1
Talla Ndiaye :
Pourquoi niom douniou commentaires si li😂😂😂
2026-08-27 11:16:42
187
~𝐀𝐌𝐘~𝐌𝐎𝐔𝐒𝐓𝐀𝐏𝐇𝐀~❤️ :
Serigne Moustapha Sy al Macktoume :Wax ci
Yonéntibi SWS ak thieur bimou am ci Yalla, wakh ci sugnu mame Adama, wakh ci Yonenté Yalla
Daouda, wakh ci téré yi di Tawraat ak Ingiil (Torah et Évangile), wakh ci Moussa ak les 10 commandements, wakh ci sourate Mouzzamil (L'enveloppé) ak Sourate Muddaththir (Le revêtu d'un manteau), wakh ci Ibliss, wakh ci astrologie (planètes yi ak éclipse solaire bi amon fann yii passé), wakh si messages codés de la prière
Ak yanen ak yanen....., Niouné Gamou woul
Dommage😩
2026-08-27 13:39:21
60
Fallou Karim 21🚗 :
Bilahi Tay la dieul sam temps deglou gamou bi yepp mais borom kham kham la en plus dama an thiofell si mom nanouy yatall liniou mana diarigne 🙏🙏
2026-08-27 22:40:58
13
Khadija dmwm🌹 :
tambalé Thi mome yamthi mome sy démba yallana yalla goudal fanwi témou ande ak wér 🥰
2026-08-27 16:33:29
0
l'incompris :
li moy waneni Sénégal 🇸🇳 dou reew mou bakh ki lim wakh lep ci alkhourane yonentibi psl gnou bsyifi lep di wakh ci 1minute noooon Sénégal dou bakh
2026-08-27 15:29:12
46
dinesamb4gmail.comsopé 🌹yaya :
question la koumaye diapalè serigne Moustapha sy almaktom Mo am kham kham wala kham kham Mo am serigne Moustapha com elements boukoye guéné ❔