Je suis Moustarchid mais Serigne Moustapha dafa dioum et capitaine meunoul wax🙏🏾
2026-08-27 09:11:12
21
Talla Ndiaye :
wakhtane bi 2h de temps limou wakh si Sonko matoul 2 mn
2026-08-27 11:09:25
31
Assane Cisse :
li gamou
2026-08-27 02:07:05
0
user144536860206 :
2026-08-27 00:30:46
36
Cheikh baye Fall Officielle :
Bilay Senegal dou réuw
2026-08-27 14:14:10
8
awa seck :
Pastef nion yakeu Sénégal m nak se normal ndak kou âme kilifa nekoufa
2026-08-27 00:59:01
52
Les trois fantastiques :
Aye boy
2026-08-27 12:10:29
0
matargueye4098 :
J’ai été ébloui par le discours de Serigne Moustapha Sy que j’ai envie de faire une réécoute à l’instant même 😂❤️📖
Wax neu ci Yonéntibi SWS ak thieurr bimou am ci Yalla, wakh ci sugnu mame Adama, wakh ci Yonenté Yalla Daouda, wakh ci téré yi di Tawraat ak Ingiil (Torah et Évangile), wakh ci Moussa ak les 10 commandements, wakh ci sourate Mouzzamil (L’enveloppé) ak Sourate Muddaththir (Le revêtu d’un manteau), wakh ci Ibliss, wakh ci astrologie (planètes yi ak éclipse solaire bi amon fann yii passé)….
Ak yanen ak yanen….
Dommage que les hypocrites ne vont parler que de la fin du discours 😏✍🏾
2026-08-27 02:07:15
25
mseck691 :
Diarama serigne Moustapha Sy 🥰🥰
2026-08-27 01:35:06
44
tyma chou 💫💫💖💖😘😘 :
serigne moustapha sy seul a vie
2026-08-27 00:24:14
167
Mohamed Ndiaye :
walaye degala merci beaucoup frère diarama serigne moustapha sy
2026-08-27 14:30:19
6
Awa Niang :
2026-08-27 01:31:53
14
mounifaa.couture :
Mane lii moy sama blm Loutakh setanou gamou gui yepou apr nou soga wakh
2026-08-27 01:54:05
6
Laminho 221🇸🇳🇲🇦♥️ :
Adouna konék ak li la intéresse
2026-08-27 06:26:23
8
bndao49 :
On a pas le temps pour regarder 1h discours de politique pendant le gamou 😂
2026-08-27 01:18:44
5
BOU👑C@PIT@ÏNE🤴PRO🤴TV🇸🇳✅ :
walay ndeysane😂 senegal da nekh
2026-08-27 01:40:15
5
Bb ouz l’homme Faramareen 🥰🥰 :
frère serigne rék la begue mais ak famille seydil hadji malick sy bi yén wax yi je ne suis pas d'accord
2026-08-27 17:13:47
2
Mousslimchamahachine chiby :
walahi wakh nga deug
2026-08-27 11:25:06
3
Soda dial bou Sonko :
Dafko warone continuer bagna Doug si yéné continuer si yalla yonent bi comme gamou la nek .
2026-08-27 01:47:52
0
wuez bou wally :
merci beaucoup
2026-08-27 09:36:26
2
user3478519237167 :
2026-08-27 09:42:27
3
To see more videos from user @thianeambiance, please go to the Tikwm
homepage.