Wakh deug yalla wa tfm amou len beneu professionnalisme li affaire de famille la certes il a dérapé mais waro len nangou li nak boudone youssou ndour laniouy wakh li dague ngen ko bou yague andouma ak serigne Moustapha dh mais li dafa eupou tambalé si sonko yam si mom point 🙏
2026-08-27 12:40:16
12
ndiaye fatou(sonko 2029) :
probleme bou amee amena gnoussi profiter ,serigne moustapha louko way mandi wakhal wayer kou beugone bayam la
2026-08-27 13:22:33
7
Sëriñ Saaliwu Jóob :
Yàlla jàmm yàgg ci réew mi ci barkeb Alxuraan Kariim.