@samarew19tv: URGENT - Oustaz Cheikh Sarr apporte une réplique à Abou Sy après ses déballages à la RFM #senegalaise_tik_tok #seringemoustaphasy #bassiroudiomayefaye #ousmanesonko #fypシ゚viral

Sama rew—-tv
Sama rew—-tv
Open In TikTok:
Region: SN
Thursday 27 August 2026 22:42:07 GMT
28805
1410
95
24

Music

Download

Comments

assanesow07
Assane Sow :
May lén ngou diam s Moustapha moy saga bayou diambour yi
2026-08-28 00:33:03
6
dabakh.sam3
dabakh sam thikite❤️ :
𝐭𝐨𝐬𝐬 𝐫𝐟𝐦 𝐝𝐞𝐟𝐨𝐮𝐥 𝐝𝐚𝐫𝐚 𝐥𝐢𝐠𝐮𝐞𝐲𝐞 𝐲𝐚𝐦 𝐫𝐞𝐤 𝐥𝐚𝐲𝐞 𝐝𝐞𝐟𝐟
2026-08-27 23:27:19
7
user9197998868053
user9197998868053 :
ana ki wakhoné dafaye réglé sénégal
2026-08-27 22:53:51
18
assaneseck331
Assane Seck :
sawaye détails bakhoule sene wadjie mo wara nopi détails bakhoule
2026-08-27 23:10:50
32
lemancunien06
le mancunien :
ils sont libre d'inviter qui il veut c un radio privé
2026-08-27 23:29:02
10
ouss__1710
Domou Thiate :
Seugn bi, je pense que fii bu amé kuniu wara waxal mba kuniu wara recadré c'est ce monsieur,Mustafa Sy, je veux dire. Parce que nit ak lo nekkeu kilifa nekkeu kilifa so dioumé dagne la wara gaganti,ndah Mustapha Sy nit leu rek donc il n'est pas à l'abri de l'erreur. Limouy tok ci champ de courses bi diko wakh, kou waxal yalla rek xam ngani jekkoul rafétoul, nioune nieup ay talibé MAODO laniou, suniu xol yi kouko ubbi mom ngathi fekk, sayou ma nieuwane tiwawone falay gamo waayé nk Mustapha mom, j'ai remarqué que depuis un certain il a tendance à transformer le gamou en règlement de compte té wakh deug yalla famille Sy buniu amé problème, lolou niom la thi cn biir nio bokké cn Seydi Hadj Malick. Toubab bi nk néna le linge sale se lave en famille donc c'est pour dire que gni bayèko thi cn keur yi dagg cni passe nieuw tiwawone,nioniou am lénène lou lène yekkati ludul tok di deglou ay nitt niouy xaxaranté. Lii mom dafa wara dakk ci ay nitt nio xamanté ni nénaniou ay kilifa laniou.
2026-08-28 01:05:55
2
user77257241098176
grand dakar la deuk :
Sa way moustapha sy mo wara bayi attack yi
2026-08-28 00:30:59
3
cheikhgeuye51
Cheikh ndiaye gueye :
Aye wayé ndaw samba legui mom dolen ko wakh mo bayi togne 😂😂
2026-08-28 00:12:51
4
cheikh.dieng235
Cheikh Dieng :
RFM n'a rien fait🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
2026-08-28 00:43:10
3
ibrahima.kane.l.of
Ibrahima kane l officiel :
vous avez des médiums de communications 😜😜😜😜😜😜, pourquoi vouloir attaquer la tfm ,,,ils sont libre c est une radio privee
2026-08-27 22:53:39
7
teacher2194
Teacher Job :
gnioune dh magal nagn si diam vraiment kein degou niou
2026-08-28 01:45:42
1
gorguitall471
Gorgui Tall :
s moustapa mo reglewoul lolou moy deug
2026-08-28 00:49:35
1
toumanedabo
toumanedabo :
2026-08-27 23:45:57
2
user9172052294315
user9172052294315 :
rfm sey tane rek mo lén diapp
2026-08-27 23:36:44
1
balla.moussa.kant73
Balla moussa Kante :
2026-08-28 00:43:19
1
1899.189999
1899 :
Tfm défoul dara
2026-08-27 23:55:16
0
general2904
GENERAL 🇸🇳🇧🇷 :
Ç une affaire familiale mais c vous qui veulent regler ça publiquement
2026-08-27 23:41:44
1
ibzo278
IBRAHIMA CISSÉ :
del wakh serigne abdou sy li deff s moustafa serigne moko deff serigne
2026-08-28 02:12:19
0
mbaye.sakho56
Mbaye Sakho :
2026-08-28 05:39:12
0
imnouassan33
imnouassan33 :
mai son bi tamit
2026-08-28 02:17:11
0
artecophoto
Xaabire 812 :
Abdou Sy c’est un Senegalais kom tt le monde. Sen serigne bi mo warra nek nit bayi wakh si nit
2026-08-28 02:50:58
0
bebe.kante36
bebe kante :
Sonko ❤️❤️❤️❤️❤️
2026-08-28 04:02:44
0
ndiayafall62
Ndiaya_FALL :
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
2026-08-27 22:49:29
0
To see more videos from user @samarew19tv, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About