Sm papa de 4 famme la am mé deniou dioubo bo kénki bou guene kenki febar Mo tahk man ak sm dom baye yi Machllha 😂
2026-08-29 09:55:05
0
SAMBA SOW :
pa yi dagno gueumon yalla wolouko,
nous on est toujours dans les calculs mo takh yalla dignou sétann
2026-08-28 14:52:29
122
Assanediouf :
difference doylou
2026-08-29 15:09:53
0
cissokho pro SONKO :
la question auquel la génération actuelle se pose
2026-08-28 15:39:57
23
Mounass :
danga beug 4 femmes wala😁
2026-08-28 13:51:59
5
nabou mbaye1561 :
Bayil mère bi bakhna Lou lérr la mère bi wakh 😂😂😂
2026-08-28 13:22:23
18
ousmane :
doundou bi da barkelone motakh diamano da changer legui bro
2026-08-28 15:07:07
5
MAMA NGUEDJ ❤️❤️❤️😍 :
Dane dane nane si nda nda bobou dey ame secret nieup di si nane mo waral dioubo bi sopaneté bi di bokk lekk sœur yi bokk ndap frère yi book bol xalé yi pareil amoul di berr ken sa m rappelle chez mon grand-père à louga sété comme ça ndeysane bobou xalé la ndeysane 😂😂
2026-08-28 14:26:01
9
Khady diop :
machalla mame l'ong vie à toi
2026-08-28 15:11:57
12
le cerveau :
Barké mo amatoul lolou la rek souniou diamono papa yi salaire 100.000 mo gérer wone toute une famille parsk dafa amone barké mais legui barké mo amoul salaire 1.000.000 sakh keurgui ame problème
2026-08-28 15:04:45
7
YAYECHEIKH :
barké ak SOUTOUREU
2026-08-28 15:23:06
2
Birome seck🥰❤️ :
Billahi sama papa 4 fam la am problème dara 😍
2026-08-28 22:20:39
0
Darou salam :
barkel
2026-08-28 14:33:53
2
sokhna Aïcha rassoul💝😘😘 :
bayil togne wayy😂
2026-08-28 14:46:15
3
Demba sy :
barke mo amoul legui
2026-08-28 21:45:28
0
Makhamba 🎉❤️❤️ :
ey way bayil togn
2026-08-28 13:52:44
2
1234567i :
😂😂
2026-08-28 15:11:52
2
OUMOUH sy :
wa yaw do bayi sama tonrondo😂
2026-08-28 13:39:20
2
Fatou Diop :
😂zz😳😳😳😂😂😂
2026-08-28 15:30:20
3
fatou Binetou Seck boumalick :
bonne question
2026-08-28 14:17:12
1
Madam:thiam :
2026-08-28 16:10:18
2
alioudrame :
😂😂😂😂
2026-08-28 15:01:08
2
ndeyearame74 :
wallah
2026-08-28 16:06:28
2
To see more videos from user @seydinaoumar_, please go to the Tikwm
homepage.