Képp kouy déff Lou Bonn yallah na la yallah weer 🤲🤲
2026-09-08 17:13:11
134
dieynahassim :
yallah na liguey yeup toth
2026-10-08 18:11:04
9
Linguère Madjiguène NDIAYE :
aye yala Na sama boss fegne khame naner douma seye sama Girou doundou
2026-09-25 08:25:13
7
DIVA 32 :
sokhor amena yakh naniou gore yeup😢😢😢
2026-08-29 12:31:05
2
mouhamadoul 🇺🇲🇺🇲🇺🇲fadall :
sama tantà sama photo ak sama photos yaye ak mousso reum ak sama shufetman la diokhé mais kamko diokh malheureusement dafà xam sama yaye mou wo ko appelle direct niko nieuwal sama keur mou dem fekko mou tokk
2026-09-18 16:13:40
7
+221🇸🇳Marieta Diedhiou :
Mane liguey nit lá meunoul comprendre 😳
2026-10-07 14:16:22
2
Torodo business :
Warone ngen ma setale sama bosss manguini menouma dem fen😭
2026-10-08 20:31:04
4
Madame seye 163@ :
Ay way Ly niawna
2026-09-05 19:39:18
1
ndarndarbi :
heee allahou akbar aywaye li doyna ware dé l'an moko fi diare lane adouna yagoule dé bakhena yalla naniou yalla same[Prière]
2026-09-09 13:56:57
6
ÉCRIT.............. :
WHAT GOES AROUND COME AROUND ☝️
2026-10-03 00:21:44
2
Yayou _Sokhna _Diarra🤍🐻🫀💐 :
Mane mom xam n’a li laniou ma def😳🙈Yalla meune n’a setane nak😳😭
2026-09-09 09:09:46
4
Mariama Cissé :
thieye yalla yenday yalla nalen yalla faye
2026-09-11 10:12:29
1
baye fall :
titena sonou boss nekafi
2026-09-10 14:57:38
2
Kharitou papam 🫂🥳 :
Kon nitt boné na niiii 🫢😳😳😳 allahou akbar
2026-09-27 18:03:00
4
Coumba Ndiaye :
tônie naniou borom bamélbi😭😭😭😭😭😭😭😭
2026-09-29 00:27:46
3
Ngoné Sopey Naby :
Adonna dou keur li darayy adouna diaroukko
2026-09-26 21:41:44
4
Mouna La Dame de Fer 💪💯 :
yalnalen yalla werr
2026-09-13 19:35:37
2
kyafadilou :
Fatou lannn?????tite na
2026-09-11 20:51:09
1
Yandé Diouf :
nagnou ragal yallah,ragal beuss pégneteu
2026-08-29 21:14:17
2
Soudou10 faye :
lou way def bopam dieu existe de ragl lene yalla
2026-09-08 16:46:53
1
thieka :
ay way ragalen yala [Prière][Prière][Prière][Prière]
2026-09-26 20:40:31
1
teirnoboye :
nuit gni dagnio febarre
2026-09-09 21:46:05
1
Fatou Hurts :
ndeysan li gnawna😭😭😭
2026-09-11 13:56:37
1
user6499302606567 :
alakhou akbar
2026-08-29 09:58:41
1
To see more videos from user @bamba.ciss964, please go to the Tikwm
homepage.