Sama rak dji khadim walay tass na sama yakar khalé bou meune foot ⚽️Machallah dém iatalie difa football lou grave diakhal toubab yi diéki saye rek bayi solou Ibadou di diangue Alhourane foumou tolou dima ware
2026-09-01 11:26:41
9
Ousmane Ba Chantal Sagna :
so amoulonn li ma rouss ndah danga bah yarou té ham linga beugueu am gnanou mère Amy"beugueu baye🥰 ".yalla maylafa werr diamm ak ndam you barri