@modoubayefall123: ##senegalaise_tik_tok #senegalaise_tik_tok #greenscreen

Modoubayefall ambassadeur
Modoubayefall ambassadeur
Open In TikTok:
Region: SN
Friday 28 August 2026 23:35:10 GMT
153958
26139
1187
5941

Music

Download

Comments

toure..general1
GENERAL TOURÉ ❤️🫡 :
Mom Eska koy bi Bakh na sakh
2026-08-29 05:27:47
264
falloumbodje2
user3688219514972 :
Walahi Ndeye San Mame fallou GALLASS rek 🤍🖤🫶🏿
2026-08-29 17:27:20
1
sokhnafaty782
Sokhna faty :
Dioumoul nak ndax djiguenou touba goor deukk monkoy diourr🥰
2026-08-29 08:45:19
177
mamethierno.765709842
مام چيرن.جوب طوبى🇸🇳🇸🇳 :
man dh touba la deukk tek si fière si
2026-08-29 00:26:10
706
kharakhenashoes
Ndayanne Awa balla shoes :
Douko meussa am nak
2026-08-29 00:20:18
132
lixewtey
oo7 :
pa bi waxna deug dh ,li eupe si gniom dounou yor djabar
2026-08-29 09:34:24
13
bassirou.fall
Bassirou Fall soda :
khamga litakh yàlla Mayou lako dé
2026-08-29 00:24:13
151
lenfanttimide30
lenfant Timide 🙈 30 :
Aka ma fier 🥲 si nek Toubasien 🥰
2026-08-29 00:52:29
44
wolofbumakkbi
WOLOF PIIR :
Moo bayil mu wax lumu bëgg â wax waa tuubaa dani comercy rek man de loolu la bëgg comercy rek🥰
2026-08-29 12:16:20
0
borommbakhrek
PROFESSIONNAL DRIVER :
Mane déh Barké Cheikhoul khadim boma Wakhé Touba la deuk rekk mane beugue nala billahi
2026-08-29 11:48:44
29
user14550057166506
ajvg :
pabi wakh na deug touba daniouy torakhal dji
2026-08-29 07:09:21
16
khalile693
khalile lô :
waa mom louye problems bi😳😳
2026-08-29 13:04:59
0
nabybousonko28
Naby Sonko :
man dh sa touba deugue la 🥰🥰🥰🥰
2026-08-28 23:40:03
94
baysboutique
Baye Codé Centenaire :
on est fier d'être Satouba
2026-08-29 00:15:10
26
cheikhouna.gaye222
Cheikhouna Gaye :
Merci modou baye fall
2026-08-28 23:45:13
61
seugn_bou_mak_bi
ndiaye diatta ndiaye :
wallay ndaysane
2026-08-29 13:18:57
0
mbacke555
S.Makhtar 777106996 :
Amine way
2026-08-29 12:56:45
0
ouss.bou.44
ouss bou 44 :
Modou dinama raye 😂😂😂
2026-08-28 23:38:28
67
fama1991
mustapha :
paa bi bilay wakh na degg
2026-08-29 07:42:44
7
fallou.gueye858
fallou gueye :
wallahi wakhnga deugue modou baye fall
2026-08-29 00:19:59
12
morseye877
Mor Seye :
Le problème moy bouma amon la wakh manam amouko lolou moka metii nk
2026-08-29 00:13:38
8
user3694030417474
madame loum :
mane dè touba la deuk fi lay seye mè magui bakh Sama dieukeur nop ma mayma djamou bou bari
2026-08-29 15:33:14
2
mohamethniang1
mohamethniang398 :
yow kén dou nob sa dôm nga mélni mbam khoukh nii
2026-08-29 13:37:38
2
ferland.papi
Ndiayene bi :
Thieuy wa Touba sonn nane vraiment mériter wolén lii
2026-08-29 16:06:34
1
To see more videos from user @modoubayefall123, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About