machallah souniou wadji ya gore sonko yabo seul ❤️❤️❤️digne fils de la Casamance
2026-09-08 12:59:45
1
Idy Badji :
khol séd na....
2026-08-30 00:24:55
5
Djiby Barry :
Ousmane Sonko Yalla nako Yalla may wér ak wérlé saam aar diokh ko rewmi may ko ndam mousseul ko si pékhé noon yii ak occidentaux yii allahouma amine inchallah
2026-09-05 22:02:59
3
fatoundiayendia674 :
sama khôl dafa sed malgré je suis un peu souffrante mais ki dafmay fath billay yeugueutouma grippe bi