Me saway dafa am loumalay wakh si adouna diugen boko feke mouy def Lo khamni nexoula dang koy diema dindi ndakh diugen matoul
2026-08-29 11:35:55
19
💞farista🥀🦋 :
Gna bakh am yaar sabakhayy mome massi kham dara 😊❤️
2026-08-29 13:47:05
0
saliou zizou296 :
Première commentaire dou ay fo dè amdy
2026-08-29 02:36:54
43
ℝ𝕒𝕙𝕞𝕒𝕟𝕖🇫🇷🇸🇳 :
Blyy ioe
2026-08-29 08:32:16
0
B@b$_Jr⚽️🇸🇳💙❤️ :
Kone do am 😂
2026-08-29 06:02:18
0
la brésiliene🇧🇷🇧🇷🇧🇷 :
man mome douma guéne ak goor bou beuri wax
2026-08-29 13:23:27
0
FATIMAH ~KABAA :
Li nga wakh no defou ma si len mais defois di nga guisss djiguenne youy deff lolou fekk niou geune xol gniko deffoul l’apparence est vraiment trompeuses il est temps que vous arrêter de jugés par l’apparence 😏
2026-08-29 09:18:14
6
Bintaaaaaa 🌸✨💕 :
Blh djiguen day simple
2026-08-29 10:52:46
8
ØGP👑🥳🩸 :
blh sa wakh dji meritena beaucoup de j'aime aye deugueu késsé guafi wakh amdy si diameuh dji rk mouy daw 🫵🥳
2026-08-29 02:47:18
8
!!💃💕A_M_I_N_A @💋❤️ :
nit Day simple niou bueg la 🥰
2026-08-29 02:40:01
12
B_Bambiste🇸🇳 ✵ :
Yaw seul😂😂😂
2026-08-29 02:36:24
15
Serigne Touba seul ☝️ :
bly grand bi wakh gua wakh deh diam si ioe rek 🥺😌
2026-08-29 03:16:43
7
yayacoly❤️🤘🫢 :
Dou ioe yalla la✌️☝🏿
2026-08-29 02:49:33
5
pearlbysoumah :
Amdy yalna ngua goudou fannn
2026-08-29 04:28:46
5
Prince ziza 07 :
Lolou iow la rék sa way
2026-08-29 11:51:59
0
To see more videos from user @amdynho.jr___10, please go to the Tikwm
homepage.