famille bo Guiss amna histoire.... même seydatouna aicha ak Seydina aliou defnagn guerre Niom Niar tè pourtant ay sahaba lagn mais histoire Bou yag Nga beug ko indiwat tji table bi pour lan
2026-08-29 17:12:31
15
aladji bubaque 956545484 :
dabakh malikc 💖💖💖💚💚💚sy
2026-08-29 17:14:57
8
𝗕𝗮𝗯𝗮𝗰𝗮𝗿 𝑑𝑖𝑜𝑝✪ :
kou khamoul rék khao
2026-08-29 16:14:26
7
Bachir :
li ban ane la
2026-08-29 18:23:56
1
Fils de guediawaye💛💙🇸🇳🇸🇳 :
Fouleu mom momak serigne moustapha niomasi doy😂♥️
2026-08-29 17:34:35
7
Puissance :
Wakh nagn mané ak degg na yakna Lou eup famille …ay way gnouy nétali tass nagn rèwmi
2026-08-30 01:21:11
2
BAYE NIASS :
Bilahi probléme bi dafa yague si serigne Moustapha sy mou serigne Babacar la tamalé