@almourtadastore:

Al Mourtada Store bou Sonko
Al Mourtada Store bou Sonko
Open In TikTok:
Region: FR
Sunday 30 August 2026 16:13:15 GMT
24357
1860
211
147

Music

Download

Comments

anti.apr2
sonko 2029 inchalla :
seringe mountakha bassirou mbake yalla nafi yague tewer
2026-08-31 01:31:39
11
aliou.dia960
Aliou Dia :
machallah sokhna sii gaddou yii amena solo loll way 🙏🙏👍
2026-08-31 08:38:26
0
cheikhbayougoor4
cheikhbayougoor4 :
Jërëjëff waxx dji rafet na 🥰🙏
2026-08-31 10:54:17
0
user1993240305247
user1993240305247 :
amine waye yallana yalla barkele amine waye ❤️❤️💯
2026-08-31 01:25:36
0
rokhy.ndong4
Rokhy Ndong :
al moutakha yague fi looool
2026-08-31 08:32:40
0
mataseye0
mataseye603 :
kaddou rafetna lool
2026-08-31 07:20:27
0
fayeadji94
Fayeadji :
machallah sakhnasi kadouyi rafetna amnay téguinn 🙏 dieureufé Serigne Touba s mountakha yallna fi yague te wér 🙏
2026-08-31 09:12:27
3
pendasarr5
Penda Sarr :
touyyyyyy wa wakh deugue waye
2026-08-30 19:14:56
4
falloudieng163
Fallou Awa Bousso :
Sidi diéggaloule bala gnoulay diangal bakh bakha
2026-08-31 03:29:14
7
cheikhsarr337
cheikh sarr468 :
sokhna si bilahi contan na si iow djiguén lilan koy doyé buma amoul woon fouma diokou ngar ngé kasé dés fi ma diokou Si iow moma geuneul fouf ay Wakh La nk
2026-08-31 10:11:15
1
mbemguedame
Mbemguedame :
machalah sokhnasi rafètna wayi dieureudieuf. serigne MOUNTAKHA
2026-08-30 17:05:06
6
dioufepicerie
DIOUfepicerie :
guissagoulène daara sakh kou défié alhourane ak Sounnah Yallah nga ammale affaire. Yallah dina fégnal diombé yi amme si tarikha yi yép bagnou khamné diné islam dou lougnouye donno si guégno... Konone Yallah doundale dome bou goor bou Yonanté Yallah bi Mouhamed aleyhi salatou wa salam ndakh mou woutou bayam. Yallah limou beug wakhenako ba parré si alhourane ak Sounnah té yakamtéwoulène 🥰🥰🥰
2026-08-30 17:48:52
2
sokhna.133
sokhna mame diarra Niang :
ahmadou rk nofi né barké serign touba
2026-08-30 21:40:19
4
pmgcos
beaugue fallou :
Merci sokhnasi walahi sa wakh rafetna sidy dafa dioume li dra diarouko si adouna serigne moutakha longue vie rek
2026-08-31 01:31:06
2
marmecouture
Marėmecouture :
s mountakha mbacke balla yaguefi lool te weur allahou ma amine yarabi
2026-08-31 08:48:49
1
mougneul2
Sante serigne saliou ❤️❤️ :
Ndaysane mbacké yagg fi
2026-08-31 07:11:10
2
sokhna.ndiaye870
Sokhna Ndiaye :
Sokhna si kaadu yi rafétena yalla Nala borom bi faay yiiw waxalel nga ma
2026-08-31 06:32:13
2
user5600026600721
user5600026600721 :
Amin
2026-08-31 01:25:21
3
abdou.wahab6
Abdou Wahab :
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️Diaradieuf Serigne Mountakha Mbacke Yalla na fi yague té wér
2026-08-30 23:28:23
1
chiekh.thioune7
Chiekh Thioune :
amine💚💚💚
2026-08-30 21:12:47
1
user9329490282236
Habibatou :
2026-08-30 19:48:24
1
ibrahimadia35
ibrahima dia :
machallah
2026-08-30 20:27:18
1
madembadiarra680
Mademba Diarra :
merci madame
2026-08-30 20:36:58
1
caammoor
caammoor :
amine yarabi
2026-08-30 18:47:10
1
To see more videos from user @almourtadastore, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About