@wolof_mindset: Nit ñi jaruñoo neexal ndax kenn ma nu ko, Te ku ko doon def itam dina mujj doon sab liggéey, Ba doo am beneen liggéey Bu dul neexal nit ñi.✍️ Kon kuy ànd ak nit àndal ak moom ci dëgg #mindset #tiktoksenegal🇸🇳 #fyp

Wolof_mindset👑
Wolof_mindset👑
Open In TikTok:
Region: SN
Sunday 30 August 2026 16:33:59 GMT
1286
158
2
1

Music

Download

Comments

debutantgameur
debutantgameur :
Ma bagne 🤪
2026-08-30 23:10:51
0
googl580
googl580 :
❤️❤️❤️
2026-08-30 21:08:42
1
To see more videos from user @wolof_mindset, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About