@khasidatv23: ##Khassida #SerigneTouba #Islam #Rappel #vir

KHASIDA TV
KHASIDA TV
Open In TikTok:
Region: SN
Sunday 30 August 2026 18:08:51 GMT
43351
6031
340
168

Music

Download

Comments

buoyam3
MAME SALIOU BAMBA KARA :
Li Sëriñ bi bëgg rekk mooy am Sëriñ bi wéral guddal fan 🙏😭
2026-08-30 19:39:15
86
alaoumamegawann
Alalou soxna Astou Gawan mback :
dan kay dégg rék té déglu wuñu ko Waayé wax lepp la wax🙏
2026-08-30 20:32:59
26
adama_274
@adema'fall :
yalla na fi yague té wer
2026-08-30 23:44:37
16
cheikhouna.bamba.m
cheikhouna bamba mboup 96 :
Yagg fi teu werr loll mbacke inchallah
2026-08-30 20:05:59
7
ousseynou.niang.a
Ousseynou Niang akasaa :
Mbacké balla yague fi♥️
2026-08-30 20:06:52
24
moustaphabeye196
tapha 173 :
ndayssane thieye Serigne montakha
2026-08-30 23:36:43
0
ipra392
ipra392 :
serigne sidi diomaye na serigne mountakha
2026-08-30 20:57:00
7
mame.fatou.seul
ibadou rahmane 🥰 :
bly ya kilifa dh 🥰
2026-08-30 22:22:50
18
khadim.bamba.thia92
khadim.bamba.thia92 :
Leeep wakhnako
2026-08-30 19:32:23
2
mouhamed.diop.plo
diop plombier sanitai :
Daguay nek si famile Di diadiant Beug done mourite say parents bagne dakhe louniouy kisse si yene yi sokhna bouy yite ay gor yene Talibé yi dilen diapale nioune bane aduna laniou nek teh serigne mountakha moy bakhe mi teh selle wakhe dji yague na waye dafa melni tay lakoy sogua wakhe Mbacke yague fi lol yaye khalifa serigne yague fi lol Mbacke amiiiiiiiiiiiiine ya raby 🥹🥹🥹
2026-08-30 22:15:28
5
mbaye.460.mbaye.4
Mbaye 460 Mbaye 460 :
😭😭😭😭😭😭 diereudieuf serigne touba amoul morom
2026-08-30 22:09:38
6
baye.sidy.sourang
baye.sourang 🇸🇳🇹🇷 :
Aye way sëriñ bi yagg fi ngir yalla😔❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
2026-08-31 04:13:01
1
bayediop602
bayediop :
guiss guiss bou sori la yorr mbacké nioungi tuubaat bou bakh tey jégëlou 🙏
2026-08-30 21:07:11
11
hamaza_8
ALALU SERIÑ HAMZA🫀❤️ :
Yalla nagua aggalé nale yeupe barkep mame seex ibreu 🥰🥰
2026-08-30 23:02:12
2
princeadams263
prince 👑adams ❤️✨🖇️ :
mbacke yague ak weer rk inchallah
2026-08-30 21:10:27
2
maty.niang623
Maty Niang :
2026-08-30 19:35:43
2
bara.bou.sonko0
Bara bou sonko :
2026-08-30 18:13:36
5
ibrahimagning399
Ibrahima gning :
شكرآ
2026-08-30 20:10:37
2
user8235746753721
talibé seregne saliou mbacke :
2026-08-30 20:05:17
3
abdouliendow07
walasri TV 1 :
2026-08-30 19:11:29
3
sidybarambaye.sonk
sidybarambaye sonko président :
toub nan Bou bakh dh 😭😭😭 li gna beugeu mouy Am inchallah son bakan lansi tek
2026-08-30 20:51:07
4
papeousmanendia422
OusmaneNoréyni❤️as saliha 🫶? :
da guise lougn guissoul kham lougn khamoul mo takh gneupa wara dégu ak dieufé ak digualam
2026-08-30 23:07:32
2
To see more videos from user @khasidatv23, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About