Serigne bi yagui am diam mann dh dama guente ñiou waax ma na def ya khayou ya khayoum diokh ko adiya yonente bi lim bi nak 400 la ak lou tek dama fate mais guisou mako nak mais magui ko def mou kontan may lath nakh ma koy wird wala koumasiii monaa dimbali rk waax ma