Mais Yarasoulallah Moom xana nekatoul
yonentou bi lanouy wakh Yarasoulallah
?😂
Bounè yonentou bi molèn intéressé dem lén
dieuli binde moo geun
Ms deglou wakhtan boo xamni bouy wakh si
yonentou bi ga avancer ba si famouy diéxale di wakh si actualité di wakh si rew mi ga
dagueko ne waxoul si yonentou bi
2026-08-30 20:33:17
38
Jabrayil :
Jarama Cheikh Séydi Mouhamadoul Moustapha Sy Al Mourchid