wallakhi ndeyesan kadoyi amna solo lol waaye Machallah
2026-08-31 21:19:24
1
Mbangol ne :
yagual sakhal weureul ci barkép ahmadou
2026-08-31 20:41:48
26
Lepp jamm Lepp tawfekh :
88 Lako kham mok serigne abdou Akim top sen mak djou tedd dja serigne Moustapha Bachir fi thi guediawaye Hamo 4 li weur serigne bi ken dou tek tchin ndakh ay berndé nila moussa mel machala yagg fi té werrr Mbacké balla
2026-08-31 20:12:42
17
ibou karim :
dolifé yag dolifé wer Mbacké ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
2026-08-31 19:58:40
13
user9885135234820 :
amolldie
2026-08-31 20:28:56
0
user8708073286202 :
Waw gooor amna solo loool 💚
2026-08-31 21:08:40
3
Moussa Ndiaye Teragan :
THIYE SERIGNE TOUBA THIYE SERIGNE BI ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️