man dé honnêtement Oustaz Modou Fall dé awma luma kay wax,au contraire nit ñi kay saaga ñoo muusul ,ndax wax dëgg neex Yàlla nit ki boo ko mënul déglu nga zapper ko bul sax abonner wu question de responsabilité la rekk,mag boo gis magum boppam la magum xél la ñoom ñi ko njëkke di saaga ñoo gàtt xél rekk te tuuti xalaat
2026-09-01 09:39:22
60
Beug fallou staff :
Très bien oustaz 🥰
2026-09-01 09:43:22
81
Dash💕Aïda Sarr🪭🍯❤️ :
Ay way lii eupeuneu dh
2026-08-31 21:20:51
50
user5842383488251 :
Mais am léneu respe nk si Oustaz
2026-09-01 11:08:13
25
Ndiaye King baba livreur :
li esque compte tame la
2026-09-01 12:12:06
5
weuz Bou BG 2 :
ouztas dou wkh béne khallé bayi nalla ak yalla😁
2026-09-01 11:06:43
37
smamemorthiadiaye3 :
Liika déff bakhoull
2026-09-01 12:35:51
2
fatou :
limome rafatoul
2026-09-01 10:24:50
7
Al_Bachir :
Pour gni khamoul lii dou compte officiel bii
2026-09-01 13:30:15
4
La damel du beauté :
la réponse de ouztaz mon combat
2026-09-01 11:38:54
7
Aicha_kinder :
Très bien 🤣🤣🤣🤣
2026-09-01 13:26:37
0
84Rya_Sow ♥️ :
bayiléne Oustaz guène bagne
2026-09-01 08:47:34
3
khady diop :
wouyyÿ
2026-09-01 13:16:08
0
l'absolue :
mane emojiii ouztazz bii moma rayyy😂😂😂
2026-08-31 21:56:37
8
SEN LÉGUMES LOCAL :
Mais il faut porter plainte Senegal ame na yone aussi