@modouakabakh: @alalouborom.darou

Mbacke1418
Mbacke1418
Open In TikTok:
Region: SN
Monday 31 August 2026 23:31:40 GMT
70787
2325
314
738

Music

Download

Comments

user8211659341508_000
Nazir :
S Mountakha lamou xam ak lamou guiss Thi baatine ba wax lim wax moko xam. boulèn niou fonto 😭😭
2026-09-01 15:57:04
2
sakaria.samb
pastéf :
chéikh Ibrahima fall dall mooy ki guena guem Sérigne touba thie kawam souf😭😭😭😭
2026-09-01 11:02:23
21
chahmadou3bg
Bamba gueye :
Niata yone lako serigne mountakha yeed
2026-09-01 00:18:07
85
amdy.karimien
Amdy Moustapha :
saway li yaggeu bayilene beugue detail
2026-09-01 19:38:53
1
ibno.cheikh.mohame
ibno cheikh Mohamadou fadal :
dege rk ga wax machallah🥰🥰🥰🥰🥰
2026-09-01 12:05:01
0
ndanane4850
héro biii :
wane yone lay dokhal
2026-09-01 03:55:43
0
ahmadoubambasouare221
✪𝓐𝓱𝓶𝓪𝓭𝓸𝓾 𝓑𝓪𝓶𝓫𝓪✪ :
kone sa guis guis bokoul ak guis guisou serigne bih d'accord
2026-09-01 01:09:47
42
thierno.diop735
Thierno Diop :
mome mi sakh si lobi bi la bok finecment hopital cheikhoul xam nan losi khew
2026-09-01 21:34:26
2
kenalboromtouba3
kénal Borom Touba rék☝️🫀🗣️🔐 :
man guama toma kou dol s mountakha barkep Borom Touba ta diapou Thi xasida yi Tay fasal s mountakha yagfi loll😭😭😭
2026-09-01 02:18:07
7
cheikhounadiaw75
cheikouna diaw :
mais dama warou dal si set yi😭
2026-09-01 00:47:17
10
amalaxassida
Amala xassida :
Li yag na lol nagn bayi di guen ay wakh you yag S cheikh bimou thi toudou guen wara kham ni yag
2026-09-01 11:42:49
5
lazanbaseye235
lazanbaseye :
serigne Modou lo ngabou moko geuna degou fouf geune ko dioup Serigne mountakha niamouy wakhal khamna ko
2026-09-01 14:15:17
6
serignemodoumbacke
Serigne modou mbacke laazanba✪ :
wah lén ko né aïda Serigne bi dako yede yede mo degar bopo
2026-09-01 10:46:57
21
abdousamat6
abdousamath seck :
Li yagna dé khna dégou mounane s cheikh saliou bayi lén diaxasee
2026-09-01 13:46:08
2
jokerie98
tektegui :
gni nio yessss
2026-09-01 00:50:00
5
ousmanesecktissus
Ousmane seck tissus :
Dème léne Nguène diap si baye fall gno waure dhè 💪
2026-09-01 10:18:40
7
soxna.ada.saliou.m
pape cheikh🇸🇳 :
soxna Aïda saliou ame na ndame✅✅✅✅✅✅
2026-09-01 00:57:54
5
cheikhou.diouf3
le Dieu qui a fait fera tjrs❤️ :
gnata yone lako yéde
2026-09-01 00:30:14
6
user8211659341508_000
Nazir :
Serigne bi niata yoon lako yèdd ak laabiré ??? matna niéti yoon (Porokhane, Ndiarème, Touba)
2026-09-01 02:20:54
6
soxnadiaraboromprokhane
Lou doul khasside doyou ma :
wakho fi dara
2026-09-01 11:43:38
2
dieyediene780
Dieye Diene wa keur :
li rék moy deug wakh bame andak s saliou thioune mo guene
2026-09-01 17:03:08
1
alalieserignesaliou1
serigne saliou Mbaye :
Yon wi dou yoono guiss guiss
2026-09-01 15:43:57
5
kenalboromtouba3
kénal Borom Touba rék☝️🫀🗣️🔐 :
amsa moko tane barkep Borom Touba Laa wakh
2026-09-01 02:18:41
3
cheikhouna399
S Cheikhouna diop koki :
Mais kii wakhou fi dara gnii lan laniou beug
2026-09-01 01:19:31
2
diwaanu..xarbakhe
Sëriñ Moustapha Xarbakhe👉📿📚 :
Mais Lane Motakh Ngene Di Guenné Audio Kilifeu Yi 🤔Ayway Bayilene Vocali Kilifeu Yingene Di Tasaaré 🥲
2026-09-01 11:25:55
1
To see more videos from user @modouakabakh, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About