walahi souma wax di joy lima xam lepou souma ko waxon n̈ouni damay wax louma nex ta n̈in̈ouy wax kilifeu n̈okou ko def 😭😭😭 ay way nan̈ wormal serign bi😭
2026-09-01 00:56:30
34
King Fallou :
Nitou deugue
2026-09-01 01:30:27
119
Hisbou L’Or :
Photo Serigne bi guir yallah nañ koy wor mal kadu yi Amna solo ms natal bi matou ko ta sax Amna niou doul comprendre 🙏
2026-09-01 02:53:46
39
Sope s aïdara mbacke ✅ :
Nama yalla bal waye lepo cheikh bi la rek magui toup 👏
2026-09-01 02:18:56
56
Ceddo ceddo ceddo :
Mane mome yalla rek point final
2026-09-01 09:00:02
5
Beug Serigne hamzatou✪ :
Ki limou wakh deh lou ame leu 👍
2026-09-01 01:03:14
52
Karbala 💎 Diamond :
Serigne Mountakha Mbacké yalla na fi yag té wer Amin
2026-09-01 03:30:35
22
talibé serigne modou diouf :
walay li moy deug kenn waroul bay bayal lodoul deug la wakh
2026-09-01 08:31:02
10
MOMO 💠 :
li rek moma métti wallahi pouvoir bi niou aïda diallo guinée Mouy déf louka nékh ci yonou muridd li métti nama wallahi 😭😭😭😭
2026-09-01 14:07:35
5
✪ ALALOU SERIGNE BARA🌺💫 :
Yallna niou yalla mousal thiy aïda ak nioniam
2026-09-01 14:58:17
0
soldarou serigne bi 🥰🤞 :
ndayssan liii bilahi dafa méty tée niou yarou téee bayi wakh diou niaw djiiiiii ,bilahi lou wér nga wakh , domo kilifeu yiii kham léne ñi ngéne wara mél ak ñi ngéne wara andale🥰🥰🥰
2026-09-01 00:52:35
13
rafah :
Amarina solo lol sakh
2026-09-01 14:02:25
0
T A 🫡 :
Ki di wakh moy serigne saliou MBACKÉ mom serigne Thierno mbacke guelongal
2026-09-01 01:52:21
5
Mame modou moustapha Fall🏁 :
Kaddou yi werna machallah✨🥰✅
2026-09-01 03:33:12
17
🇸🇳STRONG Lady🇱🇷🇨🇦 :
Soxna Baly Mountakha ak Fatou Binetou Pouye guéne di wakh miou
bayi Goreu yi gnouye recevoir ak khéssal
bi...[Crying]
2026-09-01 03:08:30
7
badoualiounebadarafall :
bly ndaysane
2026-09-01 09:54:48
1
makhtare :
waaa wallahi
2026-09-01 09:24:11
1
sadikh424 :
Nitou deug ❤️❤️
2026-09-01 01:33:05
8
King Fallou :
Wallahi tate ak xalisse yak na réwmi mais yalna gnou yalla sakhale si ndioube ta maye gnou ngeureumou Serigne Touba
2026-09-01 01:34:40
8
Guelwaar_Tigui :
louniou dal Cheikh Bethio moniouko yobé nagnko wax té déé
2026-09-01 14:36:44
0
Une S@lih@te❤️🫶🏽🦋 :
Aka Bari xam xam🥰
2026-09-01 13:06:33
2
سرج مصطفي سلام مفاتح البشر🤍🧡 :
🤲🤲🤲🤲
2026-09-01 14:57:08
2
Abdul ahad :
mom kay seytané kasé points
2026-09-01 15:25:08
1
Un westaf rek rek 🇫🇷🇸🇳 :
Walahi deug la deh mane sama khol bi nakari na lolou
2026-09-01 09:33:39
4
الضروالنفع من الرحمان :
Ćey yii xetti deug
2026-09-01 08:46:49
5
To see more videos from user @khassaides_dor_tv_, please go to the Tikwm
homepage.