Thies d lgui nimou yako sx dou Ndank màn damay sx ragal guén doupa fa demei tellement k insécurité bifa nk c tropp vraiment bayi nagn len si loulen nex nangou wougn liguey niakk diom sathie rk akk agressé ay nitt
2026-09-01 23:46:23
76
DG SASM :
Srx Mane la situation de Thies me déçoit defois baye Thies lifa nek si camps militaire gendarme et policier yep be Legui sécurité ça reste doyna war dal pourquoi ça ??
2026-09-02 00:14:09
32
KHALIL :
doyna war mais thies mom dafa graw
2026-09-02 00:30:18
0
Awa Faye :
Poste de police Mo wara am fofou
2026-09-02 00:05:54
9
zinga zinga :
Braquage à 3h du matin apres à 2h , puis à minuit et encore à 21h.
Bientôt à midi. Nous ne sommes vraiment pas en sécurité.
2026-09-02 06:27:16
5
Papis Gueye :
Zac lampe yeup pa fay nassi mairie wax
2026-09-01 23:59:36
5
@Bic_rouage🇸🇳 :
mom dayy répéter rekk " guis guen " wa guiss naniou mais expliquék mou lerr bokk😂