yalla nalen yalla yeureume te khare léne laldiana firdawsi😭😭😭
2026-09-02 00:23:07
14
soda mareme ❤️🥰 :
yalnako yallah yeureme tè xareko aldjana
2026-09-01 22:50:05
46
Maáme Faállou Glasse 🫡💰 :
Yeurmandé Yalla ak jièngeul si kawame 🥺
2026-09-01 22:49:16
111
~sokhna Amy ~🙌 Mbacké 🌸🌸 :
Mbacké yueurmandè yalla ak ayyi ndiégueleme barkeb arxouraane si daradiaye cheikhoul xadiim sounou mame dji🙏 yalla yaguale Fi sa waydiour wi bassi kaname
2026-09-01 23:00:07
71
fatou ndiaye :
Yall nako yalla yereum tè khareko aldiana firdawsi 🤲
2026-09-02 00:47:23
0
𝑴𝑨𝑴𝑬❤️🦋𝑭𝑨𝑻𝑼🦋 :
Yalnako yalla yeurum kharéko aldiana firdawsi
2026-09-01 23:14:23
19
Absa Mountakha Khadim Rassoul :
Serigne Mountakha yallah nala sunu Borom dfal gua goudou fan lol te ande ak weer ndysaan ndié wantou nako soul say doom 😭Ken meunoul imaginé bobou metit da nirou diar diar ak sunu sangue bou tedd bi Seydina Muhammad psl massa Mbacke Balla aysa