Yalla nako yalla yeureume diégal si yeurmandém Aldiana Firdawsi
2026-09-01 23:15:15
3
~sokhna Amy ~🙌 Mbacké 🌸🌸 :
Mbacké yueurmandè yalla ak ayyi ndiégueleme barkeb arxouraane si daradiaye cheikhoul xadiim sounou mame dji 🙏 yalla yaguale Fi sa waydiour wi bassi kaname
2026-09-01 23:01:59
6
boye refane🇸🇳🇸🇳🇸🇳 :
yalnako yalla sounou borome yereume 😭😭😭😭😭
2026-09-01 22:37:00
1
Fallou Mountakha Bas :
Yalnako yalla yeureum té diégalko
2026-09-01 22:47:14
2
Khadim :
thieuy yalnako yalla yeureum
2026-09-01 22:49:11
1
faaaa :
ooooh yalla na firdawsy di kereum barkep chekhoul khadim
2026-09-02 00:48:57
1
Librairie xitmatou xadim📖 :
Yallana nako yalla yeureul
2026-09-01 22:44:24
1
Salihate bi :
Ndeysan yalla nako yalla yeureum🙏yalla nga guissék sa mame Cheikhoul Khadim🙏
2026-09-01 22:40:20
1
Ndeye mou serigne saliou ❤️😘 :
Yalla na khipe aldjana 😭
2026-09-01 22:59:03
1
Moustaphagaye :
yallah nako yallah yeureum barque Al xourane
2026-09-02 00:07:31
0
Saliou Niang :
Yalla nako yalla yeureume diégal si yeurmandém Aldiana Firdawsi