bilah goorou Sénégal sen diabar yi rek lanou bagne tes di apprécie sen diabarou morom yi
2026-10-28 14:23:44
86
Global service :
Sama diekheur kom mouma
2026-10-27 17:29:55
40
khadijarasoul :
bilahi sama dieukeur dé téléphone rék
2026-10-23 08:55:43
60
Awa nabi mou s falliou :
Goor sou beuré ay diabar rek il faut diabar yii dîna niou wett bollé ay femmes ba paré bagué nieup contane manoule nek billay ❤️❤️
2026-10-22 21:22:18
77
DDK :
man dh wetouma ndah sama ndiaboot
2026-10-18 22:52:49
55
lima lima😎 :
niom.lolou details lagn ko diapei alors que c important hyper important
bref
2026-10-22 15:24:36
53
Mame Penda Gueye :
Sama dieukeur yayam ak téléphone bi lima guena meti loka wakh mo netaliko yay dji dangay am problème sah diko xam mounileu demal wakhko sama yaye….bilay Limay dund mane rek mako xam
2026-10-30 13:50:02
8
Anina :
Khana amouniou TikTok. Mane mome may wételi
2026-10-28 11:33:17
12
Fatou Ndiaye :
Mane dhe 1mois 16 jours déguouma Sama dieukeur😭😭
2026-10-27 13:58:03
8
lifa ndiayFaly Wade :
mame mome diohma ma djeund pain la niou sék ba souba
2026-10-27 22:34:39
21
user1901315755946 :
man dh dama weut lolou
2026-10-22 22:53:39
24
Khadija Rassoul Sow😍 :
Yalla nagnou borom bi may ay kilifeu you bakh am diné thi barké Nabil Mustapha PSL ♥️♥️♥️
2026-09-02 23:02:45
17
Minako :
Amou yay amou ma papa amou ma dieucoeur ndakh talouma heureusement g des enfants sinn sama adouna Dina meti
2026-10-26 15:50:30
8
ndiaye :
mane d Sama sokhna meme bouma fananei atelier nako wo watshapp defois souma wathier damay nieuw kaff ak mom bou mèrei bou nèkei djigene wèroul dama kay yeureum douma beug mouy mère souma ko mèrei wè damay rare keur gui dou tèrei ma teyei sama lokho si mom fonk lène sokhna yi
2026-10-28 22:00:56
10
Maguette mara Mbacké :
walahi def ba sonou té dougnou la encourager ben yonn waxtan zéro dagnouy mél ni ay lion té bougnou guéné Thi biti di foo ak nitt gni métina trop
2026-10-27 14:44:04
14
Éléments khadimou rassoul ❤️ :
Douma wete alhamdoulilah sama dome yagui fi si gnome laye nek gno maye wetali alhamdoulilah dieul lene sene dome def lene ay wetal yallah bakh na
2026-10-29 11:16:46
5
Diamalaye_beauty :
yi khetou deug
2026-10-26 08:47:36
7
Une Sunnite 🌸🧕💯 :
wallahi deugeul 🥰🥰🥰
2026-09-02 12:48:16
5
MANDIAYE NIASS :
allahou akbar wakh bii mom leçon de vie pour gnioune gorry
2026-09-02 13:41:04
5
Mrs A.D❤️ :
Sama djeukeur parfois danane ma ltkh so demé si souff di wakhtane ak nitt ngi bay retane té so nieuwé nopi naniko kou nek linga ma diokh rek lalay délo kassé
2026-11-06 17:55:16
2
Miss madame Badji🥰❤❤ :
c'est se ke je vie en ce moment
2026-10-29 12:56:41
3
La Salihate🙏❤️☺️ :
Bilae Limay doundou dei guay wah ni ya seuyda mesouma solou ba sama dieukeur néna sagnessé gua khaw reuy la khaw ma loumou done🥺
2026-10-28 21:00:41
4
bbefa33 :
Bayè kou en se moment 😂😂
2026-10-28 21:32:51
3
To see more videos from user @sibynarofficiel, please go to the Tikwm
homepage.