nexoul ba nexoul walahi gnii nioy wa keur Yallah 😭☝️🫶🏽🥰
2026-09-02 14:16:26
274
🌸 Alhayri Beauty💄 ⚜️ :
Li kagn la😭
2026-09-02 13:32:43
35
dykha chuu🏀❤️🤘🫂🏀 :
thieuye wa Médine baye vraiment koufi nieuw yegue yalla 🥰🥰
2026-09-02 13:45:33
227
Saly Barhama Dièye :
Mane ki la beugue Niass Coumba Abdallah 🙏
2026-09-02 13:57:51
119
nogs :
oh adouna doudara
2026-09-02 14:11:23
9
fatoundeye :
diabotou baye bi boléni sétane diléne deglou yalla rek guaye yeug thi sa kholbi machalah
2026-09-02 14:39:31
54
princesse 👸🤩❤️thiam :
yag fi lolle niass awma si yow saguo❤️❤️long vie à toi
2026-09-02 13:59:41
45
Une barhamienne 🫁🧕 :
Machallah ❤️dembou xôl yeup séd si yaw ❤️
2026-09-02 14:06:34
23
Amadou Dame Janxa :
Walahi khawna dieul sama roho gui, Baye Mbaye Yalna Yallah goudeul sa fane. ninga toyalé sama khol ci goudi gui, Yalna Alkhourhane fayla yarabi
2026-09-02 14:13:23
15
Penda Niass Diop :
souniu leep yalla la ndeysae
2026-09-02 16:53:06
0
FaSa.OM :
wa leur baye Niass deugu , talibé baye deuguuu nakk la wakhh kénn douko khole té do guisss dounde diné si gnomm
alkhaldoulila
yalnala yalla def talibé baye akhannn
2026-09-02 16:00:47
7
caméléon 33 :
Thiey wa pays bi machallah gno deug Yallah deh,Jarejeufé Baye Niass 🥰
2026-09-02 13:57:55
36
khalil ba :
dembou sama yaram dawna
2026-09-02 13:33:06
13
niassss :
li taye damako diouye sa me rappelle Mouhamed nazir niass rta