deja niarr yi nga yoor yeup imitation la authenrique eau de parfum lagnu si bind pas parfum rek benen bissi top moy en parfumerie extrait de parfum mo eup tenassite eau de parfum bref deflen sen markting bayi nienen yi ak sen choix
2026-09-03 11:27:02
117
Dialy🫶🫶🫶 :
Mais dégue naaa extrait yi mooy geun tenir
2026-10-05 16:15:02
54
+221🕌📿🌙 :
Wa legui authentique bi loumouy diarrr ??
2026-09-30 14:17:42
12
Mme Diop ndeye mama :
Bi nak
2026-09-16 15:40:18
3
C✨🇸🇳 :
Vrai ou faux [Ricanement]
2026-10-05 18:55:48
3
Djibson :
prix bii
2026-09-04 15:56:47
4
Binéchou Diamille 🍯🌸🇸🇳🇫🇷 :
Original
2026-10-06 23:28:00
4
Mrs mbengue kholou Taw✌️💍❤️ :
bi nak chérie
2026-10-02 13:30:02
5
La Soro Services Parfumerie :
Madame ligua wax ni gnep meunako def si imitation bi té kou xam parfum degu sakh taxoul gua khamko parce que tenation rek lagn wouter té différence bi bariwoul lisi guene am importance moy faire confiance se revendeur mom aussi mou degou merci aussi si léral bi
2026-09-10 01:52:04
2
ndoya63🥋 :
Bignu bind come no extrait de parfum faux bila Bignu bind eau de parfum moye original bi 💪
2026-10-16 19:21:12
1
🌹🦋Éva the Queen Shop 🦋🌹 :
Ma chérie ils le reconnaissent mes iis veulent la facilité simple
2026-09-04 11:17:58
3
mouha 💕 :
mai man bima yor étiquettes malick one laniou si binda
2026-09-04 09:06:51
1
DouceAllure💫💫💫 :
Authenticité mom yaassi ték loho
2026-09-10 21:17:13
2
djili fall :
a combien
2026-09-03 03:57:28
1
Bub dme :
c'est combien ourjunla
2026-10-01 13:08:18
1
prince khalill :
Beugna benna
2026-10-23 23:59:42
1
توكلت عل الله :
man dh bou bakh bi la your
2026-10-01 18:59:30
1
er6912323580784dame fall :
oud laténa senegal mélni dangéne koy sogua kham
2026-09-30 09:04:26
3
🙏♥️💋🫵🏿💍🌘💫 :
Authentique bi gnata la ?
2026-10-06 06:08:13
1
O NA ME GACCE TANGA :
ton prix
2026-10-25 07:33:52
1
PEULHPEULH :
Kharal ma demé khol samay boss💃🏿💃🏿
2026-10-24 22:10:03
2
Beug fallou :
Eau de parfum
2026-10-07 10:39:04
2
Princesse,👸 :
Merci
2026-10-06 13:50:44
1
To see more videos from user @fabirastore, please go to the Tikwm
homepage.