goudegoe ndiek ci bamel kokoudol
khalate lolanekhe,def😭😭😭😭
2026-09-15 19:11:22
1
Sokhna binta mou SSM🥹 :
SSM néna alale diou tèw fadioul sokhla yalla moy fathie sokhla niaka yorr dara thie sa lokho dou té sa adio fadiou bouka yalla wara fathie🥹🥹😍
2026-09-11 00:01:51
21
ندايا صالح✨♥︎🩷 :
serigne sam mbaye néna . adouna bo kham ni dina diafé gua guis ko roy wala koulay wakh loulay délo si adouna bo kham ni nigni dagnouy sap fougn woron tékk yalla gnou tékk fa khalis adouna bo kham ni nitt gni sén éntéré rék lagnouy khol bougnou don yakh dîné djii dou lén diaral diouk wayé bougnou fi amé fistin mou diaral lén diouk
guayi adouna amoul solo na gnou diamou yalla bala dé di gnew 👆
2026-09-12 00:25:16
20
pape sow mou baye sam mbaye🤩 :
sarigne sm mbaye nena beguel gnepe ta yallah takh sopal dioulite yeup ta yallah
sopeu ta yallah lou am doolé le lah
Baye same mbaye nena goudi gui ndieuk ci bamel amoul dra dra lou mel ni mome koudoul khalat loula nekh defal wayé faw nga diarisa 😭😭😭
2026-09-11 20:23:30
5
user83062581480523 :
SSM nena daaray adouna diaroul daray alahira 🥺
2026-09-11 16:54:45
4
nogaye mou ssm :
ssm mbaye néna khôl bi yermandé nek fawou yermandé yalla tabi thia 🙏
2026-09-15 00:03:00
5
Bou ❤️💍Aline badara🥳 :
S sam mbaye néna kharite sakh danala guénné thi lou barrie bou déh kharite bou bakh naka nonou andadoh ndakh dagne néh wakh masa kharite ma wakh là sa djiko[Prière]
2026-09-15 00:18:48
2
Fatima zahra mou ssm🥹🫀🎧 :
Kou teud gui néna yar yar
2026-09-02 19:25:18
4
Tal zo le pro :
koulou Naf sin salikhati maw ti
2026-09-15 16:55:37
1
𝓟𝓻𝓮𝓽𝓽𝔂 𝓴𝓱𝓪𝓭𝓲𝓳𝓪 🍫 :
adouna dou dra koula ko eupeulé takhoul mou eupeulé la dra gnenél yawmal khiyam lay fégne 🥺
2026-09-15 12:47:34
2
massamba Ndiaye 💙 :
Serigne sam mbaye néna daray adouna diaroul daray alakhira🥹🥹🥹😭😭
2026-09-14 20:19:56
4
Mame anta Sylla :
ssm néna da rayy aduna diaroull da rayy alahira 😳
2026-09-02 20:07:28
5
—Une hijab—🧕🌸 :
Ssam nene yar yar yar moy lep✅
2026-09-13 22:47:58
4
chauffeur307boundawbi :
yarr yarr yarr yarr yaray lep 🥰
2026-09-12 23:14:06
3
Alyyyyy🕷️ :
S.S.M néna "Nit li geun bone si mom moy topato ayi diambour wathie ayibam"🥹
2026-09-12 22:26:12
2
Jules Beug Fallou☆ :
daray adouna diaroul alahira❤️❤️
2026-09-14 16:49:37
1
Saloiu Yatts73 :
wakhe na ba soun wakhe na guodi wakhe na bethieg
2026-09-14 21:39:45
1
Fallou Lahi Ciss :
s sam ne na li coli dian bin mas ra
2026-09-14 11:59:10
1
Alhamdoulilah Alhamdoulilah ❤️ :
Adouna ken douci diékhal saaay soxla mouk soxla sou diexx sénén diog tawaxw
2026-09-11 21:51:22
2
mbaye ndiaye :
adou kéne dou si diékhl say soxla saxla bou diékh bené nieuwat
2026-09-12 21:54:16
1
Ⓜ️omo Ndiaye🇸🇳🏴 :
ولنتها ارب الى ارب Lingay wot Douka Am Mouk Soxla bou diéx Binénn Nieww 🙏😭
2026-09-10 22:00:58
3
gueyendiaye12 :
s sama mbaye néna mame cheikh mbaye nena fadom alasabry fakolou batkhé ohhh ndeyesan
2026-09-10 22:18:27
1
bilal diouf mou s sam mbaye :
ssm nena adouna doudara koulako euple takhoul mou euple la dara .....
2026-09-14 12:16:53
1
To see more videos from user @ndao11236, please go to the Tikwm
homepage.