Raisonnement bi nguén am si diné yonent bi yaré woul won nonou sahaba yi yi je m’explique. Sahaba bi niouy wakh خبيب biniou ko diapé bakoy wadia ray dafa ni mounial leen ma ma diap dioulli niari rakka niou may ko mou dioulli niari rakka avant mouy fatou té niari rakka yoyou dou won dioulik farata déja mom mo sounal dioulli niari rakka bou niou lay waja ray ba amna worom xam xam you bari youko def guinawam…legui sahaba bi niari rakka yim dioulli nonou avant niou koy ray dako soss si xélou bopam mais gissou ko si alkhourane té yonent wakhou koko…té leron nako ni dou gissant yonent bi fi si adouna ndax nio ngui koy wadia ray…légui eska boudon yonent bi dafa yar sahaba yi si né lep lou ma defoul bakhoul eska kon sahaba bobou dina am fitou def lolou si minute yi moudj si ak doundam??? Ma dolli si beneen seydina bilal yonent dafa kheuy woko niko yaw d bik dama doug aldiana di deg sa tank yi nga nek sama kanam lolou lou lako may bilal niko xana sa you sama ndiap todjé ma diapaat té sa youma diapaté dioulli niari rakka…legui bilal bilouy def li ladioul yonent xalatam d si xalatou bopam lako défé…té xalatou bopam bobou moko may daradia bou magg bobou…té liko may daradia bobou yonent diangalou koko moko sossal bopam diko def…waaa légui boudon yonent daléna yaron si né lep lou nguén gissoul ma siko def bakhoul esk kon seydina bilal dina am fitou di def dialou yalla bouko yonent santou?? Eska kon yonent kerok douko woon wakh ni boul défati ben diamou yalla té gissé woko si mane??? Nguén kheuy beug nio wakh lep lou yonent defoul bakhoul…ba nopi diniou wakh ni sahaba yi ay royou kaay laniou legui kou roy sahaba yi si sounnal lou rafet nguén niko li bidha la? Yén cohérent woleen sakh bilahi…gni leen di top ay doff laniou rek mais kou xalat té diangue touti dina xamné yeen cohérence amo leen si dara.
2026-09-03 23:01:10
1
Yam :
Merci beaucoup yalnalenn' Yalla yaggal ngennn niouy guindi
2026-09-03 20:51:06
5
Youma :
Haramul non plus désolé oustaze
2026-09-03 10:41:07
2
ahmadousow8745 :
bien dit Dr Ahmed lô c très clair
2026-09-03 14:30:23
5
user3398692383997 :
Docteur Ahmad lo yalla naalla yalla saamm aakk keepp kouyy sakhaal le coran et la sounah du prophète Muhammad salalahou Alayhi wassalaam.
2026-09-03 15:43:23
5
Aaaaa :
Xam xam bi lere na
2026-09-03 15:40:24
3
Abdoulaye Djibril Fall :
Merci Docteur ! le coran est venu pour nous montrer comment on doit vivre et se comporter dans cette vie en tant que musulman ce n'est pas pour les morts qui ont quitté cette vie