Grand bi daffa bakh bilakhi yalnako yalla takhawou
2026-09-03 11:42:58
3
tobita gueye ♥️ Mme kaïrè :
bilaye fadame kou bakhe yalla nalla guèthe sékhlou waye
2026-09-03 12:23:51
10
amina Mbengue :
yalla bakhna lou ame yala🥰🥰🥰
2026-09-03 09:34:10
0
Salimata mbengue :
kou bakh beugue nite yallanala yalla doli hiam
2026-09-03 10:53:23
1
thia yalla fall 👈 :
kou diouly si yonentabi ba assaman sétt ga guiss kambaréne Al khamdoulil lahi 🙏 tawfékh rék inchallah kham khamna khamoul khamoul batine rawna yakhoup khikam 🇸🇳👈 Thia yalla fall 👈🇸🇳
2026-09-03 16:41:12
3
cheikh diop :
massa Sénégal yéwe yorowone kable
2026-09-03 13:52:23
0
ndeyeawandiaye32 :
nit kou bakh yalla sa xole lalay fay si diam dji rek❤️❤️❤️🙏🙏🙏
2026-09-03 14:55:42
4
Borom niari deuk yi 13 bi❤️🤍⚽ :
Pere diama rek gay ame ❤️
2026-09-03 10:02:13
7
petit senegalais :
ndeyssane pere fadam nitt bakh yagg fi te wer
2026-09-03 10:30:21
1
isseu🥰💝💘💚💖baye🥰🫀karim💯 :
yalla bour bou bakhla wayé nitt dé dawara amm yakkar si lepp
2026-09-03 10:50:39
2
Madame Sarr :
Sama dome dji yalla nalla doli soutoural
2026-09-03 12:40:33
4
Assane :
Fandam dafa bakhe yaguel té wér🤲🏿👈🏿💯❤️
2026-09-03 10:35:29
2
Adama Ndiaye :
🥰🥰Diambar deug yalnala yalla samm❤️🙏
2026-09-03 09:06:30
2
diatou :
billahi kou baah am dinee
2026-09-03 15:34:34
0
Athia Gaye :
mol dafa méti
2026-09-03 13:14:51
1
bayefalldiop73 :
anna sa câble saway
2026-09-03 06:06:04
1
papa_kara :
lepp yalla la❤️❤️❤️
2026-09-03 06:14:43
1
Babacar Ndiaye :
🙏
2026-09-03 15:04:33
0
khalil Thiaw Laye :
Nit kou bakh Yalna sa diam yag
2026-09-03 17:22:56
0
vito :
machallah
2026-09-03 15:50:29
0
Sylvie Mbengue :
juk jugui
2026-09-03 15:49:07
0
mon bonheur :
merci mon Dieu 🙏🙏
2026-09-03 11:18:14
0
To see more videos from user @palatyrdiouf1, please go to the Tikwm
homepage.