@m.thiat: Wallahi tu as tout dit Dip depuis LNN ba légui, il a toujours gardé le numéro 1 au Sénégal chaque année. Critiques yi dinañu wakh, mais streaming bi, concerts yi sold out bi - ça ment pas Ñoom Musique bi rek lañu xam, mais xamuñu travail bi ci guinaw. Xamuñu sacrifices, nuits blanches studio, pression bi. Dip mooy GOAT bi, point final.