Il à raison dh. Il avait tapé trop fort. Rap rek lay def
2026-09-05 16:35:36
33
SENECOCOLLECTEQUEBEC 🇨🇦🇸🇳 :
Give me some Mic give me some Mic plz😆
2026-09-05 23:34:31
0
bi boy shop :
dem len geun kholl album fun da mental 04 dathie deupp ✍️✍️🔥🔥🔥🔥
2026-09-06 00:13:14
0
Le Petit Fils D’alboury :
Mollah Ndongo j Maxi kresi et Gaston les Capos
2026-09-05 16:32:08
7
Fred Diallo :
son bi yore nako si albums niore tabie la bokke
2026-09-05 10:16:52
10
abdoul :
Mom pour mom daa ayy😂😂😂
2026-09-05 18:13:29
1
Omar Tine :
bilay yorna son bi 😂😂😂
2026-09-05 10:20:35
6
Meuzkala10 :
Couplet bou doy war la deff si compilation tiafka deff Dara bi
2026-09-05 18:36:04
2
Wangarin Business Group :
il as raison dh dou nit dh il était trop fort Wolay mais Gaindé moudiena done Mouss
2026-09-05 20:39:31
5
Saint Manu Gucci :
Vraiment 8 mil yi dalna je me rappelle bien à l'époque tout le monde se demandait kii moy kann ???
2026-09-05 18:33:49
3
Milki_official :
Il fait parti des meilleurs lyrikcistes du rap galsen. Mane miy wax nak je defie tout le monde guissouma kouma geuna xam rap galsen en toute modestie. Dama féké lou beuri machallah