adouna néxoule fi yép aynite laniou détient alakhou akbar
2026-09-05 21:46:05
15
ÃŜŜÃŇẸ βĮЌẸ ĹĮƑẸ 221🇸🇳✈️🪖🪖 :
yalla naléne yalla kharé aldiana firdawesi barki mame cheikh Ibrahima fall lamp
2026-09-05 20:41:07
0
abdoudiop7975 :
thiey yalla 😭😭😭🙏
2026-09-05 21:52:09
0
akhemada :
😭😭😭 yalna léne yalla yeram si b s touba amine
2026-09-05 22:49:53
5
Saliou camara :
wallahi yalna yalla fayal Ninou Mame cheikh Ibrahima Fall ak ndiabotam Gui Thi barrkep Serigne Touba 😭😭
2026-09-06 00:18:56
1
une fadilate 💝❤️🩹 :
blh aduna worinéne la🥺
2026-09-06 00:58:26
2
SALHATE 🧕🫀A 🫶VIE ❤️ :
Alhou akbarre wa li are mel fan la 😭
2026-09-06 11:24:07
0
Ah salihou :
Misal la dh worna yallah Nanou wakirlou si yallah dieufée ay ndigeuleum bayii ay téréem Adunaa Moguii nii dh Nous tous on n'a mission dieuf lou bakh déf lou bakh rafétal dieuf yii Keurup deug guii mogui dh kén dou si mouthieu
2026-09-06 03:28:50
0
mbaye sopéy s rafakhi :
thieuy adou na
2026-09-05 22:50:11
1
wolywade :
Yalnaléne yalla yeureum 😭😭😭
2026-09-06 09:37:23
0
Khoudia Seck :
Ohhh 😭😭😭
2026-09-06 02:19:35
0
user5745626348727niangniang :
Allahou Akbar
2026-09-06 01:03:41
0
user8967643267457 :
paix à leur âmes
2026-09-06 10:35:55
0
Bossh ❤️👑bou ada fass à vie :
Thieye yalla
2026-09-06 08:09:00
0
ma :
sama yaram daw na bilay 😭😭😭😭
2026-09-05 23:37:15
0
Maáme Faállou Glasse 🫡💰 :
Yalla na Yalla yeureume waydawli yi 🥺🥺🥺
2026-09-06 02:40:23
0
tapha :
Billahi adouna douh dra
2026-09-05 23:40:44
0
To see more videos from user @salioundiayehamsatou, please go to the Tikwm
homepage.